Sama Diamond Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2022
Lyrics
Hummm
Dama fananok weet
Ndax dama gersou guissouma
Kiy motaly sama leep
Baby lane lala deff
Ba kheuy guissa touma la
Fouma la wowé doma dieul
Bae fimné niiii
Binga démé ba légui nékatouma
Ma menli kou reer
Ndax yaw miiii
Yay kima done guindy
Sa souma reeré
Yay sama diamond
Yay kima doylou
Guissou ma kénéne
Diaroul ngay douté
Mane yaw la beug
Guissou ma kénéneee
Fouma lay dieuléty
Ma baby fouma lay dieuléty
Fouma lay dieuléty
Ma baby fouma lay dieuléty
Yaw loula nékh daff may nékh
Té lilay doundal daff may doundal way
Si sama xool yassi né
Baby mane dh nobb nala
Mane mounou ma xol kénéne
Té guissou ma si mom sa kaname
Nieuwal niou ande fénéne
Ma Baby ma wane la beug nala
Mane guissou maffi
Lou waral thiow li
Xalé bi yeksil
Na mbir yi dioly
Lane nga ame envies
Ma gueuna doly
Si sama xool bi yaffi né
Yay sama diamond
Yay kima doylou
Guissou ma kénéne
Diaroul ngay douté
Mane yaw la beug
Guissou ma kénénee
Fouma lay dieuléty
Ma baby fouma lay dieuléty
Fouma lay dieuléty
Ma baby fouma lay dieuléty