![My Line](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/08/22/d64f8bc7d8bc4bc89e8da1cfc4b6873aH3000W3000_464_464.jpeg)
My Line Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2024
Lyrics
My Line - Paza Beez
...
INDI CRÉATION POSITIVER
IMAGINATION RÉALISER
AMBITIONS COMMUNIQUER
DAMA TEK CIIN ÑEUP YAKAMTII MA.
WACCÉ SUM BOOP YALLAH YËKËTI MA.
SUM YOON LA NEKK BATAY WACCUMA.
PAZA FOOY MUJÉ MAAN XAMOUMA.
BËGGË NA FEKE LIMA DEEF FI.
BËGGË ÑËPP JËRIÑU SI LIMAY DEFF NI.
NIIT YI LAMA YALLAH BOLÉL TAX MA AKSI FI.
ALHAMDOULILLAH XEBALUÑUMA LIMAY DEEF NI.
Oh my Line , oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Merci mon DIEU ☝️
Oh my Line , oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Oh my Line, oh my Line
think you ALLAH ☝️
YALLAH MI MAAYÉ , MO YOORÉ SAMA WËRSËK.
NA KO KO SÀNTÉ.
BUUL JAWALÉ XARIT AK ANDADO.
BATAX DANGAY RÉER DI ANDÁ AK ÑOOM.
NANGU NIMA YALLAH SAKKÉ TAX DUMA ÑOOM.
KON GOD IS ONE ÑÙKOY WAXANDO.
NANGUL LI YALLAH LI DEFF,
TEH NGA MOYTU DI FAYEKU MÉRR.
DOYLO LINGA AAM RK DI DEEF.
NOY AAM ÑAAN TEH DI BÉGLO SA MÈRE.
BËGGË NA FEKE LIMA DEEF FI.
BËGGË ÑËPP JËRIÑU SI LIMAY DEFF NI.
NIIT YI LAMA YALLAH BOLÉL TAX MA AKSI FI.
ALHAMDOULILLAH XEBALUÑUMA LIMAY DEEF NI.
Oh my Line , oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Merci mon DIEU ☝️
Oh my Line , oh my Line
Oh my Line, oh my Line
Oh my Line, oh my Line
think you ALLAH ☝️.