![Stop The Game](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/08/20/0d4386d25ea34da3b1a5d2a1697932feH3000W3000_464_464.jpeg)
Stop The Game Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2024
Lyrics
Stop The Game - Paza Beez
...
STOP THE GAME
BAYI NA FO BI TEH TAMBALÉ LIGUEY
ATHIE SAMAY BARRE SI KAAW LAMAY DOUNDÉ
DANGEN SI YAAG NI DESSIN ANIMÉ MIKEY
TAALOUMA NELAW TEH WAROUMA GUOUDÉ.
BEGUE SAMA GUAYI YIMA DOON CONSEILLÉ
BEGUE BOROM CHARRETTE JAKARTA AK JOKER YI
DIAROUL NGAY LATHIE MAAN MAAY KAAN
MAAY KI MOUDIÉ NIEUW BOOT ASKAAN.
JOB BÉH COMMENCÉ MOTAX MA RARE
DAMA NIEUW PERCÉ LOLOU DOU HAZARD
LIMA TOOK GUISSO AMOUL KOU DEEF NI MAAN
KOON SOUMA DÉMÉ DOU AM KOUY MELNI MAAN.
NGAY NIODI BLOW-MAN MAAY DEEF AY DEEF AY TEX
FIER D’ÊTRE ÑUUL KUUK DIOXOGN NALA INDEX
DAMAY DEEM DOUMA NIEUWAT NGEN DOON AY EX
BOUGUOUMA WERANTÉ BI ALLEZ NEXT
BO DOUGUÉ SI MAAN ERREUR NGAY COMMETTRE
BOUL DIOUM BOUL DIAWALÉ BOUL DECONNÉ
SINGOM BOUY DADJI NGAM LA KOON DAAY COLLÉ
SOOMA XAMMÉ KOON BAXNA NGAMAY RECONNAÎTRE
LINGA DOON NIAAN MOUDIÉ ANTOU
BO GUENÉ SANEX DOUGUAL NIANKOU
AY RAPPEURS GALSEN DIOUK AK DANIOU
KOON PAZA CHANGER YEEN WAAR NGEN TOUB.
DOUMAKO METITLOU NDAX DOUMA METTI
DIOUDO WOUMA SI NIAAK MAIS NAAK DOUMA SEKKI
WOUT SAMAY YEUFI BOOP GUEUM DAMAY TEEKI
SA SUEUR BOU NIEUWÉ DAA FEEK NGA WOUTTI (2x)
STOP THE GAME
DIOUK TEUP DEEM
WORK IS MY NAME
AM THE MAN
AY MBAM NGEN YEEN
TRAVEL NO BLEM
FUCK THE GAME
I WORK A LOT
I DON'T NEED LOVE
I LAUGH A LOT
I'M KILLING LOVE
BECAUSE I DO MY JOB
COACH AY KILO COMME PABLO
DOUMA SI DELOU BATAY COMPO
NIIT EN COURS BATAY XAAR KO
GUISS NAANI MOUNO NGAY TOPANDO
BAYILENN MA NEEK AK SAMA LIBERTÉ
SOMA XOLLÉ XAAM NI ART MOY LIBERTÉ
BO DOUGUÉ SI MAAN ERREUR NGAY COMMETTRE
BOUL DIOUM BOUL DIAWALÉ BOUL DECONNÉ
SINGOM BOUY DADJI NGAM LA KOON DAAY COLLÉ
SOOMA XAMMÉ KOON BAXNA NGAMAY RECONNAÎTRE
LINGA DOON NIAAN MOUDIÉ ANTOU
BO GUENÉ SANEX DOUGUAL NIANKOU
AY RAPPEURS GALSEN DIOUK AK DANIOU
KOON PAZA CHANGER YEEN WAAR NGEN TOUB.