![Gnibissil](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/04/6d62f2d9b54a4855a6586fc54aea79a9H3000W3000_464_464.jpg)
Gnibissil Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Gnibissil - Canabasse
...
Bobou ba léguiiii manguiiii tokk di khar biss binguay décidé nieuw gnibii séeeee
Keur guii wétt na safatouma lénn , yéwou sans ioe meuneutouleuh nékk .
Meuneutouma deukkou solitude bii gnibii sée héeee héé héeee
Bobou ba léguiiii manguiiii tokk di khar biss binguay décidé nieuw gnibii séeeee
Keur guii wétt na safatouma lénn , yéwou sans ioe meuneutouleuh nékk .
Meuneutouma deukkou solitude bii gnibii sée héeee héé héeee .
Togn na balou na , ball nguama ma défatt deukk sii dii wëy
Khamna loula nékhoul mank koy diémeuh éviter mais mélna neiii
Sama djiko eupp doleii sama yénei tax ba souma fipo sama Ego moy déff mane may dioum bb.
Togn nala dème ngua baby guiss na walahi , kham na lane moy sa nieurign sama liifffee .
Baby souma sanione meuneuh effacé li guéneii sama gué-ei- mégne héé héeee héeee .
Souma sanione toguak ioe just one longtime, wane la nakh ngua kham fingua tolou ci maa a annne.
Kérok dama mérone,
Tagualikok Sama Saguo
bb balma......
Bobou ba léguiiii manguiiii tokk di khar biss binguay décidé nieuw gnibii séeeee
Keur guii wétt na safatouma lénn , yéwou sans ioe meuneutouleuh nékk .
Meuneutouma deukkou solitude bii gnibii sée héeee héé héeee .
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~
Togn na balou na , ball nguama ma défatt deukk sii dii wëy
Khamna loula nékhoul mank koy diémeuh éviter mais mélna neiii
Sama djiko eupp doleii sama yénei tax ba souma fipo sama Ego moy déff mane may dioum bb~~~~~~
Boula nékheii bayiil call bii sonné nala bàyiil ayy message ba call bii féss.
Boma bloqué nala koth sa galeii ak sa jobou kay, douma bayii mou sëdd
Deugueur boppou nala tékk choque
Baby so man ~~~~ bad
Tank sa sourire délou siwoul sa kanam
Effort dou doy sagn na dii dikkil nakh...
ndanane dou gattt sans diongomam
Namm na sa yaram, kham ngua adressou appartement bii.... Nagn fa dadié sii kanam.
Nala faa djitou défar lépp mou nice
Dîné au chandelle nguay am fofou tonight
Gentleman lay done lii dèss sama dirou life , kouma fa diapalé ma dieulatt sama wife.
Baby yay Chef wayeii may toguou
Dokh sii loula nékh sii lolou lay doguou
Sa tablou tolo rk ngua fa meune téguou
Apart sama saff khorom lénn meunoul eupp.
Tamoumala par défaut mane dama la beugue DEUGUE.
Nguay diéguou pousso niaw lou deugueur KEUTH.
Ma beugue nakk ngua fatei lépp nakh soma foneii kham lou khéww yeupp mërr la dou DEUGUE ~~~~
Souma sanione toguak ioe just one longtime, wane la nakh ngua kham fingua tolou ci maa a annne
Kérok dama mérone,
Tagualikok Sama Saguo
bb balma......
Bobou ba léguiiii manguiiii tokk di khar biss binguay décidé nieuw gnibii séeeee
Keur guii wétt na safatouma lénn , yéwou sans ioe meuneutouleuh nékk .
Meuneutouma deukkou solitude bii gnibii sée héeee héé héeee ......
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~