![Topp La ft. Pispa & Gun Mor](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/04/6d62f2d9b54a4855a6586fc54aea79a9H3000W3000_464_464.jpg)
Topp La ft. Pispa & Gun Mor Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Topp La ft. Pispa & Gun Mor - Canabasse
...
Topou la ioe ...
Topou leuh douma hésité
xamm na bou baxx louy sa yénei
ioe fonék moy sama yone
Soumay dème dii guiss loumou bakhé
Sodone bidew lath ma nouma nara fananéeeeh .
Nakhté dotou ma doyal... blh walayeiii
Sii diawou djiii lay beugue dème neii faa dii naweiii....
Lëpp ioe la , ñingmay beugueuh wakh nii pithie yii dii sabeiiiiii...
Sama Mbeuguël sii ioe
Bour bii Yalla djii... lakoy sëddei -éee wa*
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~
Dangua sëeeyyyyyy siii mane
Dath laa meunouleuh nékkeiii
Raww ngua khorom sii diguii guéth gueiii
lëeeeeerrrr nama ....hum ~~~hum~~~yh
Nékk siissa wëtt moy guene dii deugue siii mane .
Yama diangue fou beurriii lolou
Sa Këpar-ra diara fékh lo ~wo~wo~wo
~~hun ~~hum ~~wo~wo~~waaayyy
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~hummmm~~yh~~~~yh~~~~yeah~~
Sama Mbeuguël sii ioe dou ayy foo
Damay soriii makoy gueuneuh yëikk
Nékk siissa khôl pour gueune meuneuh yëkk.
Sama boppou sakh khamo ningma ko gueuneuleii.
T mane sakh xawma lii loumou done
~~~~limou doneeeee ohhh nooooooo barry noo
sayou mala guissouleii.........X3
lima yeukk sii sama yaram mo raww docteuuuuur
Gëstou ma t khol sii samay Effort....
Lëpp ioe la , ñingmay beugueuh wakh nii pithie yii dii sabeiiiiii...
Sama Mbeuguël sii ioe
Bour bii Yalla djii... lakoy sëddei -éee
waaaa*....
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~
Nakh ioe....
Dangua sëeeyyyyyy siii mane
Dath laa meunouleuh nékkeiii
Raww ngua khorom sii diguii guéth gueiii
lëeeeeerrrr nama ....hum ~~~hum~
dath laa meunouleuh nékkeiii
prck ioe dangua sëyy nii soukeur sama ~~~~~~~~Nékk siissa wëtt moy guene dii deugue siii mane .
Yama diangue fou beurriii lolou
Sa Këpar-ra diara fékh lo ~wo~wo~wo
Teeww maa ????? ioe la beugue nékk...
~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~~