Dégg Madame Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
Bës di nga dégg madame
Yaala Yaala Yaala baxna
Yaala Yaala baxna
Madame
Yaala Yaala Yaala baxna
Bës di nga dégg Madame
Jigeen nga
Mel nga ni nga wara mel
Raffet nga
Kaar mashallah
Say morom
Ya nga doon andal
Ñu xëy takk len
Ngay xaar sa bës
Tax na bo wete sa xel di dem ci kañ lay doon
Yakamti sa bës jot ba nga dégg alhayri
Waye
Sëy Yaala ko bind ci aras
Mouñël
Bës di nga dégg madame
Yaala Baaxna
Yaala Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala Yaala baaxna
Bës di nga dégg madame
Yaala Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala baaxna
Madame
Yaala Yaala Yaala baaxna
Bës di nga dégg madame
Aaaa haaaaa madame
Bës di nga dégg madame
Anhaaaa haaaa madame
Wuy leee
Bës di nga dégg madame
Demal nga
Sa xarit yëp seni bëss
Lek lek nga lakatu joyoo
Ñëp ngi nan
Dafa ame faru rap
Wala bëgul sëy moy daake
Tax na bo wete sa xel di dem ci kañ lay doon
Yakamti sa bës jot ba nga dégg alhayri
Waye
Sëy Yaala ko bind ci aras
Mouñël
Bës di nga dégg madame
Yaala Baaxna
Yaala Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala Yaala baaxna
Bës di nga dégg madame
Yaala Yaala Yaala baaxna
Yaala Yaala baaxna
Madame
Yaala Yaala Yaala baaxna
Bës di nga dégg madame
Aaaa haaaaa madame
Bës di nga dégg madame
Anhaaaa haaaa madame
Wuy leee
Bës di nga dégg madame
Jigeen nga
Mel nga ni nga wara mel
Raffet nga
Kaar mashallah
Say morom
Ya nga doon andal
Ñu xëy takk len
Ngay xaar sa bës