![Dama Juum](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/09/10/76cea3054aa843768fdc0385ff300ee4_464_464.jpg)
Dama Juum Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
Ye ye yeah ye ye
Eh
Forever yeh
Ombre Zion a sing yeah
Yeye ye yeye ye
Bu lep wesso
Xam na ni ma toñ
Jarul ngay aalu
Ma infidèle
Infidèle
Baal ma boo
D'accord na ma juum
Ma tax nga gaañu
Waru mala tromper iyee
Su feke ni da nga mer ba beg dem seti lenen
Baal ma dama juum
Dama juum
Suma sañon nga delo si sa xel te yërëm ma baby
Nit la rek damay juum
Dama juum
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Yay sama cherie coco
Coco coco coco
Sama cherie coco
Coco coco coco vanille
Sama cherie coco
Coco coco coco
Sama cherie coco
Coco coco coco vanille
Indil nala rose nga bañ
Iphone douze nga bañ
Lan ngay sagu waxal ak man
May sa super man
Dem sa yaay boy nga bañ
Sa copine wax na nga bañ
Lan ngay sagu baby boo
Baby boo
Su feke ni da nga mer ba beg dem seti lenen
Baal ma dama juum
Dama juum
Suma sañon nga delo si sa xel te yërëm ma baby
Nit la rek damay juum
Dama juum
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Yay sama cherie coco
Coco coco coco
Sama cherie coco
Coco coco coco vanille
Sama cherie coco
Coco coco coco
Sama cherie coco
Coco coco coco vanille
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Dama juum
Ma ngi reccu
Dama juum
Baby ma ngi reccu
Ma cherie woman o
Ma cherie woman o
Ma cherie ma woman o
Ma woman o eh
Eh eh woman o
Ma cherie woman o yeye
Tupa tapa woman o
Ma cherie woman o