Thibatou Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Yëwu Bëgg
Dolli Sante Sama Dundu
Doma Khamal Dara
Sama Tundu Wumuy Wundu
Khol bagui Nekh
Seed Ni Pôle Nord
Mané Dawal Bokatou
Outal Si koy Sakétou
Nakh Fo romb Gnu Thibatu
Thi Batou
Lo Wax Gnu Thibatu
Hey Thi Batou
Fo né Gnu Thibatu
Thi Batou
So Ré Gnu Thibatu
Dagno tema Kebetou
Kenne si gnom amussi Goût
Toukh leuh ni Outlaws
Oie la Cendru 2pac
Baby Damlay Dioylo
Numkoy défé dafa hot
Sama Nder Bi ngay Yak
Lossi Yok Doni Kagna
Ayy Wayy Yallah mignu Sak
Daga Bagne ma beug Bama
Deug La Kay Dama Soff
Meune Nga Vue samay Toph
Mangui Fane ak Samay Doff
Trii Double Louki Dokh
Gua Beug Beug Bagne
Nigga Fugnu Dugou Todj Ko
Lo Gnu Meuneuh Khâgne
Diaye Gnu Fébar rk Gnu Fadj ko
:m
Yëwu Bëgg
Dolli Sante Sama Dundu
Doma Khamal Dara
Sama Tundu Wumuy Wundu
Khol bagui Nekh
Seed Ni Pôle Nord
Mané Dawal Bokatou
Outal Si koy Sakétou
Nakh Fo romb Gnu Thibatu
Thi Batou
Lo Wax Gnu Thibatu
Hey Thi Batou
Fo né Gnu Thibatu
Thi Batou
So Ré Gnu Thibatu
Dagno tema Kebetou
Kenne si gnom amussi Goût