
Bane Façon Love Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Bane Façon Love ✅
Refrain :
Limoy Bane Façon Love
Limoy Bane Façon Love
Soma Sokh Lé lalay jot
Soumala Sokh lé lalay call
Limoy Bane Façon Love ❤️
Limoy Bane Façon Love ❤️
Baby Waxma Lougnou Jot
Sex Rek Lagnuy Call ☎️
Dring Dring Dring
Baby Fane nga nek ni
Drink Drink Drink 🍹
Baby Tollou Talatuma li
Need Real Love
Baby Fala Tollou ni
Kone Bayilma Dox
Nakh lugnuy def Du dem
Couplet 1:
Sékou gnu Wax Bou Nex
Sama Khaliss Rek la Nekh
Fou Liquide Dougou Fokmu Fegne
Damay Toyal Sama Guéne
Lilpu Potca
Barron Vodka
Happy Time La Rek Dou Léne
Baby Li mom Dou Beuguel
Fokma Djal Si Lénéne
Refrain :
Limoy Bane Façon Love
Limoy Bane Façon Love
Soma Sokh Lé lalay jot
Soumala Sokh lé lalay call
Limoy Bane Façon Love ❤️
Limoy Bane Façon Love ❤️
Baby Waxma Lougnou Jot
Sex Rek Lagnuy Call ☎️
Dring Dring Dring
Baby Fane nga nek ni
Drink Drink Drink 🍹
Baby Tollou Talatuma li
Need Real Love
Baby Fala Tollou ni
Kone Bayilma Dox
Nakh lugnuy def Du dem
Couplet 2:
Baby Munu Mala Bayi
Sa Body Damko Sik
Position Yu Sadik
Motakh Khel Munoul Dik
Sa Lèvre Sama Drogue
Essayer Bayi mais Du Dox
Mak Oie ni Rek Lagnouy Bayi
Khoulo ak Dellou dougn Si Tayi
Refrain :
Limoy Bane Façon Love
Limoy Bane Façon Love
Soma Sokh Lé lalay jot
Soumala Sokh lé lalay call
Limoy Bane Façon Love ❤️
Limoy Bane Façon Love ❤️
Baby Waxma Lougnou Jot
Sex Rek Lagnuy Call ☎️
Dring Dring Dring