
Champion Lyrics
- Genre:Pop
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
Champion - Jeeba
...
Cone diotena tay ma mague
Foutékou beuré dane
Gote may ma ndame
Dotouma téré nélaw
Yénaye diokhogne ma dague
Am am bou sawate gaw
Thiona aduna
Dotouma tèré nélaw
Bakoul rek may guiss
Champion gue fils
Bakoul rek may guiss
Champion deugue gue fils
Mane beuré na wallahi beuré na
Mane beuré na beuré na douma danou
Entrain né na entrain né na entrain né na
Eguisé sama mind
Dama sonou mo takh ma arrête Mais mettez des likes et abonné vous svp
Lyrics Tyma diop