
Thiopet Yobu
- Genre:Pop
- Year of Release:2023
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Thiopet Yobu - Jeeba
...
nénama fall lingay deif danga siy gaw ndakh att yi danio gaw té temps bi donoul louniouy khar ey guis nga mangui ni di diémeu nak batay défo lein lou leir nak iow léto ma firriiwo nakk tei iow pousso passo nak guis nga demba ak modou sama keur pathé 'k ndiogou beuss bouné fala niouy nieuw rigou di khar kounan lén indil gouro mba doudou iow nak danga ame lou kéne amoul néma lane(lane) hol bi yako mom té kéne ladiou lafii léneu (hum) lane moy sa problème wah ma bokk niou solution ko tay nga diap souba nga bayi niouy melni macky 'k sonko wala danga hum hum hum té yeugoumako(lane) mané bo yékhé daniou ma nane thiopett yobuu ehh kouné di lathie fane la néé mounan danio diay dolé(tchipp) ndokou lo sohla rek la dieulii ndakh wayadii
Similar Songs
Listen to Jeeba Thiopet Yobu MP3 song. Thiopet Yobu song from album Thiopet Yobu is released in 2023. The duration of song is 00:03:14. The song is sung by Jeeba.
Related Tags: Thiopet Yobu, Thiopet Yobu song, Thiopet Yobu MP3 song, Thiopet Yobu MP3, download Thiopet Yobu song, Thiopet Yobu song, Thiopet Yobu Thiopet Yobu song, Thiopet Yobu song by Jeeba, Thiopet Yobu song download, download Thiopet Yobu MP3 song
Comments (39)
New Comments(39)
copkareium
Tu est mon chanteur preferer je tador
Hawa Kadr91f
hawadia
maty diopythli
Tu est mon chanteur preferer je tador
Aicha fatimata Picard

wallhf8xt
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]
173541730

175051802
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Bve ndeye
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]
174707402

Astou Ndiayeyp82q
[0x1f63b][0x1f63b][0x1f63b][0x1f63b][0x2728][0x2728][0x2728][0x2728][0x2728]
daplokm[0x1f607][0x1f607][0x1f607][0x1f607][0x1f607][0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641]