
Lskbs
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Lskbs - Cab
...
maala woo si game bi kon doma thi 6.
Euleuk ma woola si péte nagne ko huit-clos rk ma yann la lou 10.
ak loma mak douma donn sa fils. man may mélange Léo ak cris kon kham nguani douma nitou fii.
Diangue école taxoul ma beugue rap beugue rap takhoul ma diangue école.
kou dall sama kaw diawalé ngua trampoline ak keck. sa xol bou nioul bi dang ko make-up mo takh ay diamesanté dotougne ko meussa sëk.
leundeum té yague guouxx si guédiou léer yii.
Leundeum si kaw bassi souf ni diallo kering.
xamo touss niou diokhla beat bi néela ngua deff si enchaînement nguay dérape.
lou rap di lathie laay deff si thine yakal sa guel mouy snap di rée dila si signe. Malaaka laa nékouma nit wakhma lou lerr bouma lakk ay thing thing leundeum si kaw ba si souf ndokhél sa fit lagnouy guouxx . buzz koumou lab ngua day sa couche .
see lyrics >>Similar Songs
More from CAB
Listen to CAB Lskbs MP3 song. Lskbs song from album Lskbs is released in 2021. The duration of song is 00:03:11. The song is sung by CAB.
Related Tags: Lskbs, Lskbs song, Lskbs MP3 song, Lskbs MP3, download Lskbs song, Lskbs song, Lskbs Lskbs song, Lskbs song by CAB, Lskbs song download, download Lskbs MP3 song
Comments (1)
New Comments(1)
dollar talla
magui ak loy am bo deupé Cab manam bac non bm dou nitt bravo cab sa album doop na trop yalla na succès bi nieuw