
Ballago ndumbé Yaatma
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2021
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Ballago ndumbé Yaatma - Youssou Ndour
...
Bilay balago ndoubé yatma
sounou wadji khadjone nafi nakar dogou laniou bayé yalla wanétina
loutakh ba mbir mi méti lolldaniou ko fokoul wone
niefi gaw ba bét nio bilay wétal gno
gninou faramarén gorou diaga néléwna bayou wally démna ni nioune dall wétal na niou
magi koye dialé Sénégal diko dialé gambia diko dialé adouna ndanane ba démna ni mani thione balago ndoubé yatma yalla bour bi bou done tago na niou bayék yaw
ni barké bimou ame di niou téténe si adouna yékétine khamal léne si adouna en balago yékéti léne khamal léne nou nit wala néké si adouna ak nit wara doundé ak nou nit wara dieuf lanté lél balago réw bagi koye dioye ar bagi koye dioye
ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck wétal nga niou ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni
litakh mbir mi méti lol daniou ko fokoul wone niefi gaw ba bét niou nda ndan ba démna ni
ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck wétal nga niou balago ndoubé yatma adouna amoul solo ni faramarene thione seck
Similar Songs
More from Youssou N'Dour
Listen to Youssou N'Dour Ballago ndumbé Yaatma MP3 song. Ballago ndumbé Yaatma song from album MBALAX is released in 2021. The duration of song is 00:05:14. The song is sung by Youssou N'Dour.
Related Tags: Ballago ndumbé Yaatma, Ballago ndumbé Yaatma song, Ballago ndumbé Yaatma MP3 song, Ballago ndumbé Yaatma MP3, download Ballago ndumbé Yaatma song, Ballago ndumbé Yaatma song, MBALAX Ballago ndumbé Yaatma song, Ballago ndumbé Yaatma song by Youssou N'Dour, Ballago ndumbé Yaatma song download, download Ballago ndumbé Yaatma MP3 song
Comments (33)
New Comments(33)
Babacar v3gqv
Astou Badji7ivim
[0x1f625][0x1f625][0x1f625][0x1f653][0x1f653]
Khady lovm9
ses très triss
Dandano junior
niger
fifikazmm
sy Sawane
thione seckgni02
rafètte na lol ndour
131836256
kvc'
ryadegduq8
ccool
ryadegduq8
cool
Mor Ndiayef22nl
il est le meilleur vrmt
Hamdou Gaye
@sidie9r3[0x1f653]f:
mbagnick ndongej88f
oh c triste paix a son âme
[0x1f653][0x1f653][0x1f653][0x1f653]