
Mama Lova
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Yaay yayu ken la
Baay bayu ñep la
Lu dine wakh rek dëg la
Nga djëfe ko ndieriñ bi fëg la
Ñeti yaay bala ne baay
Worna God amuñu sa faay
Nit nga rek kone mato mais en tant que dome gissuma sa faille
Nga ladj ko mere ma raamal la
Ma sukk Dakar ba Ramallah
Uffu sa wett lu ordinaire ma tourner guissoumala drama la
Sama aldiana ngi sa suf si
Sa mbette rek laay duti
see lyrics >>Similar Songs
More from Why Gee
Listen to Why Gee Mama Lova MP3 song. Mama Lova song from album Anonymous is released in 2022. The duration of song is 00:03:28. The song is sung by Why Gee.
Related Tags: Mama Lova, Mama Lova song, Mama Lova MP3 song, Mama Lova MP3, download Mama Lova song, Mama Lova song, Anonymous Mama Lova song, Mama Lova song by Why Gee, Mama Lova song download, download Mama Lova MP3 song