![NEVER LET DOWN](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/06/17/3700c4d55f564891a6bbd23598ae702e_464_464.jpg)
NEVER LET DOWN Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2022
Lyrics
Yeah
Hum
Yeah Hum
Hum Hum
Yeah!
B-SLAY Hum
Desfois nga soxla espace
Ndax Life bi thiono bounei lalay tekk
Guiss nga life molay ray
Parrei donne sa remède
Boul ba lep beu next Time
Li ngay yott Moy nieuw balafi dem
Guiss nga Life boum la bett
Endurance leu dou course Vitesse
Non Boul yakatti sa Time Non
You need to Understand
Boleen topé nigger do dem
Ndekete homie égal Problèmes
No gueuna wettei gueuna nice yeah
Snitchs yi dh niom nio yam
Boci joummé ba woon ley faille
Moy nga boom boom bang ci mind
Weurseuk, God rek mokay mayé
Mayé mayé mayé mayé
Bo jougué ci leundeum
Warnga Xamné (Né)
Xamné Xamné Xamné Xamné
Never let down down
Down down down down down
Never let down noooo
This shit bothers my mind
Never let down down
Down down down down down
Never let down noooo
This shit bothers my mind
You'll Never let down (No)
You better better never let down (No, No)
You'll Never let down
You better better better better never let down
Pour la vie
Yeuguou ni Tsunami
Lingay jeex moleey soul, mani!
Nioufi gueuna thiap sakh dagny wacc
Motax dawa wara njaxlaf ci seu Life
Dunya dou aldjana
Bala nga kaa soobu dakoy mind
Dalay diegui diall xamoul maslah'
Té Lo meuna fight amoul sa time (Non)
Weurseuk, God rek mokay mayé
Mayé mayé mayé mayé
Bo jougué ci leundeum
Warnga Xamné (Né)
Xamné Xamné Xamné Xamné
Never let down down
Down down down down down
Never let down noooo
This shit bothers my mind
Weurseuk, God rek mokay mayé
Mayé mayé mayé mayé
Faaw nga jougué ci leundeum
Xamné (Né)
Xamné Xamné Xamné Xamné