
Actorism 4 Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Actorism 4 - Big Dat X
...
Man la game bi yàgg jooy te décéder guma
Taaru mbind mi lay wan yoon même boo dee gumbë
Petit à petit laay nokk tapéte yi ba du ñu rabati
Back to beef 2pac Biggie ma damm sen bic yi
Bulma boole si ñoom ndax dafa bari ay bitches
Hit ´em up ready to die for the realness
Badman bulma goondi ñóddi bad mind
Boom gun dalay shot man
Philosophy Descartes dalay cogiter lo
X lyrics’am si melomind diko juter lo
Actor la si rap na bandit yi profito bala fin wu film bi
Firnde bi di hit yimay foowe do degg ni feel’u ma bii
But anyway
jurgoot sen’i nopp samay rhyme la
Dat day ligeey
exaequo ñoom sumay raam la
Radio buma déchirer wul bul fa scotcher
Putain bañal ni Patin sa équipe di es coacher
God bind wuutële ku nekk ak jiko’om
Respect lama jiitël men laataa may ji koom
Dina fly si sky bi ni hélico
Flow rhyme skillz fumu ne ma jëli ko
Jeeriko’o
Bu dee dafa tàng jër ci yaw
Sama rabin bi wute na’g sa bii better nga know
Ok ! OG kajoorois Thies la bayeeko
Ku si jaay prek ma taak sa reum ba sa baay yëg ko
Dangeen nara jómmi bu leen X Dat rap’bale
Samay métaphore ne yu François Rabelais
Style yi di taw te hit yi fune la nara ballee
Namedrop Next Punch nimu lakoy ràbbalee
Refrain
Mana rude boy inadi place
Black panther power cauz i’m from the black Race…
Don’t play with the devil
Céll’u mag du nelaw kon jarul xale tëb di dal
Fu X dikk di rap Men
Fok dëkk bi rëp
Dangeen am jab di sap
Te sen rap du dugg si ndëpp (x2)
Couplet 2
Jamaican man i’m not
But i can flow like Buju Banton
Anybody try na test me football’u muumë ñam xam
Listen! This one is for my guetto boy anh
Long time me around quiet them still making noise
Me nadi back i feel tegante deal
No matter what you feel
Man xaqq lay dekkil
Ñu dellu hell
Man rap dama siggil
Sometimes them ask me what kind of music i’m listenning
Boom.. ya’ll better know i’m just jumbling
Kill kat u beat
Def kat u hit
Dama dépasser nit
For real gën leen sadique
Du polémique dama unique
Sen dopest album yi laay fuck si 2 minutes man
Duma nit man
Bulma boole´g ay demi nit man
Raab la si rizzla
Ganja si Sizzla
Rap la si beat lay def lu tàng high degrees la
Crise la create si actor bi sen showbizz bi la
Kiy jàpp emcees yi di bombe ki rómb maitrise bi la
Mana rude boy inadi place
Black panther power cauz i’m from the black Race…
Don’t play with the devil Don’t play with the devil