YABBA Lyrics
- Genre:Afropop
- Year of Release:2021
Lyrics
YABBA - Attack
...
tedu sound nulor
lolu moi sa yàbah
hamnga nandulor
lolu moi sa yàbah
deka baa ngi mayti
luneka ak sa yàbah
rapper yang fi barri
but man kesseh mai sa yàbah
yàbah *6
dama barri leh noise
budut sabarr boi bi tama la
demai happy the rejoice
sula maytey lolu sa yàbah la
sor fi nyowweh deyga dajj
hamal lukor fofa deh hama la
teh jarut sah d lajj nitt
ndah taka yi ku sohla mata la
ana nyufi wah neh dama rew
dama few barrileh complex
maa tie reww teh dama heww
dama teww yoka success
rapper yi foroh teh muna meww
muna meww gawwa confess
tegunj fi dara teh buga geww
buga geww amor context
yàbah bu ndaw nga buga nin
nga giss ku super deen
worna yallah duma nyi
hey maa tallut enemy
tuff danga dorga yabah ñii
kai ma johla receipt bii
sorkor chapeh febarr argh
ma joh la remedy
tedu sound nulor
lolu moi sa yàbah
hamnga nandulor
lolu moi sa yàbah
deka baangi mayti
kuneka ak sa yàbah
rapper yaangi barri
why man kesseh mai sa yàbah
yàbah*6
dang ko don jema noba
sa jiko ju bon hi dafa leak
laygi time bi tejj na
garap jekhna teh boy b dafa sick
dang ma don jeema jai sherr
fekeh danga cheap
jeemala save sa nonsense
paski suma bank bi duko keep
con tei la forty fiet
dang koh yegg yàbah du