![Baye la solution](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/11/03/61be0d9775a043f981a5166441b570e5.jpg)
Baye la solution Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
Lyrics
Baye la solution - Akhlou Brick
...
barhama barhama assi
baye Niass Moy barham borom fasse yi
....
bayou rohouyi Moy baye niass
doctorou kholyi Moy baye bilahi
mo neubeu boppam won niou yallah
dieulbétum beuguélawon beugél modi baye wayé khamounioko way
sa non yii baniou nioulo baye danioula réré bilahi
gni toppé lérba Thia Adama khammé nagne la yaw baye
gniang nane minka minka ilaye ka té minka modi baye
ya khar Khôl yii sol ci mahrifatou billahi
hanrif yagui zikra laa i la ha ilal lahou
Ila Ila ilal laha baye ilal laa
yalla ki tannal nia gueun ci nia gueun
talibé baye deug nékhoula gueussum
lér bé niou nandal niouy wakhé Thia azal
yalla niou déf yallana yalla déf Mouy baye kó kô Di baye
baye alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa
baye kagne don ziaré réwoum maka gnibi cina Sénégal kókô Di baye
laay alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa
baye lérp Rassoulou ci der bou nioul man téw naniouko takou sanou taîba ba Mouy baye
baye alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa
kou youbou dîné l'islam fou dîné agoul toubal ay djounay niit ci ben gone
kou dioudom bi Kamal toudou cheikhal islam té djîtou khout bou zaman
kou donnou yonenteu hahhi hatam tok ci ahadiya donnou cheikh tidian
kou def khour an kiramam zaahiram mo gueuneu neubeu baati nam
goorou yalla yaagui djaayan té ci eutum ba
taarou yonentoubi la lambo Thia kanam ngua
marratan oukhra taraw na adiaban adiaban adiaban
moné ana nafsou wal aafahou lo wo ci yalla batou baye ba n'a n'a
Moy borom fass yi borom kossi Moy deugui deug baye Moy bayou aassi
Mame baye danioula réré bilahi
gni toppé lérba Thia Adama khammé nagne la yaw baye
gniang nane minka minka ilaye ka té minka modi baye
ya khar Khôl yii sol ci mahrifatou billahi
hanrif yagui zikra laa i la ha ilal lahou
Ila Ila ilal laha baye ilal laa
yalla ko tannal nia gueun ci nia gueun
talibé baye deug nékhoula gueussum
lér bé niou nandal niouy wakhé Thia azal
yalla niou déf yallana yalla déf Mouy baye kó kô Di baye
baye alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa
baye kagne don ziaré réwoum maka gnibi cina Sénégal kókô Di baye
laay alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa
baye lérp Rassoulou ci der bou nioul man téw naniouko takou sanou taîba ba Mouy baye
baye alla alla ho ilal laho laa ilaaha ilal laa baye
baye wilane baye wayou baye ba
thiey baye
dioy nanioula baye wayou baye ba
Mame Ibra fall wayou baye ba
thiey baye
imam assan Cissé wayou baye ba
thiey baye
baye barham Thiam wayou baye ba
thiey baye
baye Cissé baye wayou baye ba
thiey baye
cheikh mahi Cissé wayou baye la
thiey baye
wilani wilani wilanibaye la
thiey baye
wilani wilani wilanibaye la