Shabida ft. Cheikh Ibra Fam Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2025
Lyrics
Shabida shabida
Shabi rab para
Shabida shabida
Shabi rab para
Shabida shabida
Shabi rab para
Shabida shabida
Shabi rab para
Diambar la dawoul da wouti
Diambar la dawoul da wouti dji dole
Mane sagnouma yewou di khoulai fi
Gnit youye sathie dignou mbeulai
Diegui guedj nimou metai
Ta khamoul sakh limouy feki fai
Gni gnoy diambar diambar
Bayi sa rew nimou metai
Ta khamoul sakh limouy feki fai
Gni gnoy diambar diambar
Sassouma yewo khol sama yaya boye
Sama ghor mayouma ma tok di kholai ni
Ta khamni mane amna louma war si adouna si
Lou meti guor laye dale si dounya
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para
Diambar la dawoul da wouti
Diambar la dawoul da wouti dji dole
Sagnouma yewou di kholai fi
Gnit youye sathie dignou mbeulai
Sori yaye nimou metai
Sori baye sori kharit yi
Gni gnoy diambar diambar
Bayi sa rew nimou metai
Ta khamoul sakh limouy feki fai
Gni gnoy diambar diambar
Mane sassouma yewo khol sama yaya boye
Sama ghor mayouma ma tok di kholai fi
Ta khamni mane amna louma war si adouna si
Nakh lou meti guor rek lay dal
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para
Parira parira
Pari rab para