![Coco](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/12/08/7a6e49ee5c934a1ea467f068ca1986dfH3000W3000_464_464.jpg)
Coco Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2024
Lyrics
Yobou nga sama fit bi dangma tiiteul
Mbeuguel bingma won ma diko titeuro
Boudi xol bi diokh leuh parei djiteul leuh
Ak louniou beuri beuri iow doo seen morom
Coti yali yali bvby yay sama chérie coco bané
Fingmay yobou dafa sori
Biniouy lewto bvby yaama daanel
Bou guddi gui khadjé
Bidew yi di melax si assamane si
J Nganane ma bvby sisa wet laay fanaan si
Sama xol bi lisiy nekh yaakoy soukeur
Soumala guissoul damay weet diongoma
Boulma soreeti
Soumalay woo iow deema faalé
Soxna si kaay thi sama wet (2x)
Soxna si kaay soxnasi kaay soxnasi kaay thi sama wet (2x)
Eh mani kaay
Eh mani kaay
Mani kaay ci sama wet (2x)
Deff meuh
Soxnasi deff ma fou
Geuneu sori thi sa xol bi dooko reuthiou
Manit ma deff leuh sama lonko
Maak iow sekkou niou bayanté
Alaa athiou ou
Boo deffoul ndank dingma faat. Bve
Lingma niamal doumako fat. Té
Keuf sama xol ma youkhou sathié
Souniou mbeuguel bi geuneu naat my bve
Xel bou dou diougué thi xeelou bimay ray
Reewandé bingay niodi yaako tay
Say melastikou niata lassiy fay
Dello leuh ndioukeul ba xel bi dissi tey
Bou guddi gui khadjé
Bidew yi di melax si assamane si
J Nganane ma bvby sisa wet laay fanaan si
Sama xol bi lisiy nekh yaakoy soukeur
Soumala guissoul damay weet diongoma
Boulma soreeti
Soumalay woo iow deema faalé
Soxna si kaay thi sama wet (2x)
Soxna si kaay soxnasi kaay soxnasi kaay thi sama wet (2x)
Eh mani kaay
Eh mani kaay
Mani kaay ci sama wet (2x)