Eutou Baabel Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2024
Lyrics
Eutou Baabel - Amadeus
...
mak yaw ba abadana may nala sama Catane
diayanté sama ndawe
démna ba ndox ci pax
dioxnala sama Cadou
meunatoumala baa
séntouna ci dieulé ndame mak yaw
ndax adoune ya bé ta gui dafay gueune dioxé n'a ci lima tambali Mane
démna ci sama Mame nénenma dieuleul diaro
diaridia dégueul masséti ci keur
khamna dinanie ma lathie l'an mo tax ma wax lilé
kéne doumani Thiam Babel kham NGA man beug nala
kéne doumani Thiam Babel kham NGA man beug nala
meunone té neuniou
défandonaniou ay wére
khamal ngama louné somayi rosa
douma diar Dara bouma kéne dimbalé d'où yaw ya co wax
sama waye NGA
coumele ni yaw
soxlawoul ngacoy ignané
kou mélni yaw Thiam Babel da ngay lathie
kou mélni yaw Thiam Babel dêmba Thiam
nala yonou eutou Babel
bolé la ac samay nawlé
khamnga takoussanou Babel
Thiam ba waye samay nawlé
meussouloma khép ci samay aye
sama dioume tay doco nétali
dama amoul couniou dimbalé
comme do mounie douma dimbalé tu ci keur
man souma diké waye
khamna domasséti kéne ci keur
khamna dinanie ma lathie l'an mo tax ma wax lilé
kéne d'où melni thiam Babel kham NGA man beug nala
kéne doumani Thiam Babel kham NGA man beug nala
meuno té naniou
deukeundo naniou ay wére
khamal ngama louné
soudoul wone yaw dé douma diar Dara
boma nieup goumbalé kholma ya co wax
sama waye NGA
coumelni yaw
koukonamoul dakoy niané
kou mélni yaw Thiam Babel dêmba Thiam kou mélni yaw Thiam Babel dêmba Thiam