KOLO KOLO Lyrics
- Genre:Soul
- Year of Release:2024
Lyrics
C'est toujours les mêmes problèmes
Arrête d'écouter les rumeurs et fie toi à mes je t'aime
Ne me cache rien , et dis moi tout ce qui te dérange
On veut pas se quitter donc viens on s'arrange eh viens on s'arrange eh
Boulsi dougeul kou si bokoul (bokoul iow)
Négne bayi sou khawé meti rek niou ni dokhoul (hummm )
Ya may sa kharite yi fite baniouy wakh Thimth bakhoul
Sama khol laleu oubil, dara laleu neuboul , dara laleu neuboul
Ma la beug, ya ma beug kone dégne kay kolo kolo
Problème yi diss neu torop , matneu ay Kilo Kilo
Ma si doug ya si doug kone dégne kay kolo kolo
Déglou seytané moy indi khoulo khoulo
Mala beug , Yama beug , khol dou féne meunoumala wakh loudoul deug
Mala beug , Yama beug oubina sa bountou khol té sokhalawouma sakh feug
Mala beug , Yama beug , khol dou féne meunoumala wakh loudoul deug
Mala beug , Yama beug oubina sa bountou khol té sokhalawouma sakh feug
C'est toi et moi on a cotisé
C'est mes paroles pense pas que j'ai tisé
Négne bok lepp mbecté ak nakar
Crois en moi et si ça marche , je te sors de Dakar
Toi et moi on a des projets projets, on parle de mariage
T'es la plus chefrai chefrai, je te préfère sans maquillage
Loumou meti meti négne ko kolo kolo
Je préfère notre duo, j'veux pas finir en solo solo
Djigéne yi louniou beuri beuri , yama doye
Diémna la wéthio mais kéne méloul ni iow
Négne bayi réy bi, bougne lidieunti kou togne
Ya wakh deug , iow ya bakh mane ma bone
Ma la beug, ya ma beug kone dégne kay kolo kolo
Problème yi diss neu torop , matneu ay Kilo Kilo
Ma si doug ya si doug dégne kay kolo kolo
Déglou seytané moy indi khoulo khoulo
Mala beug , Yama beug , khol dou féne meunoumala wakh loudoul deug
Mala beug , Yama beug oubina sa bountou khol té sokhalawouma sakh feug