
Xamoko Lyrics
- Genre:Alternative
- Year of Release:2024
Lyrics
Xamoko - Lou Da Kid
...
Fi nga tieupélé lagnla ajanté
Saaarakh cii biir sogua enchanté
Dfougn Contact téh agg ngeu Terre
Lalou mala noumlay enceinté
Dofii come back teuggeul weundeul Df Detour Xamnga lila fiy xarr
Mbougeul bou tarr lole
Garantie naa lolou,
Sou bakhé meu doliwat ko cme nonou
Jaléwatt
Siggil ndigalé
cii lignou digalé wone
Dou mane may nieuwat,boudé ioe ya démone
Douma cii delouwatt
Diaroul sx di watt
Songue rk dougnko wadj
King ko fok dou moy wadjaa
Wadjalénn louy dikkeutii
Tégeul niousseutii tapétt yii
Kén cii niome jokhouma appetit
Ling leu seuff lay nieuw pr foukhatti
Simbaté sa sympathie dfal lassi kopatii
Goukheul leu topétt ngeu topp cii
Stay real anyway
Néhh cii kawam evryday
Xamoko
Gangooor
Yabiila tanggoor
Deukkkeul cii naneko
Wa*goor
Ninaal na sa tate yii batayii
Miineul leu sam bopp bamou nekhmeu bayi
Soh gneméwoul guerr bii boul angou bataille
Loula réér nieuweul cii gars yii
Meunou niou téh dougnou bayii
Apocalypse gané cii sén jotay
Fuck sén débat boudé ay détail
Nieuw sole tiarakh cii dîner de gala
Tagntia leu fou métii
Seuss leu beu ci murou wiss bii
Ngay patialii rongogn dii joy
Meu tokhaalaat lingom ngeu réh
Dilén niouSs téh concentré wouma
Dougeul but téh kén centré louma
Woyof tole té kén antanoumassi
Boudé ay diagay rap bokatou massi
Tass diangue yii lay df dém teudii
Fetiakh sa parent wane tara mbéra
Ngamay geuneu méré
dossi meune dara
Massi meune fouf
Khaakh touff
Sédolén ko vous tous
Fii dougnleu diayy dagnlay wantér
Kounékk dii woutt loh commentaire
Ak 47 la soukhé sén lafii
Dfcii touffé 8 poulet
Sotii cii taal bii ndokh tiow lii jékh
Yokkou cas bii doli xarr mii karaw
Xamone nguénii douma lén mooy
Douma lén may lou tolokkh
tarafatal ayni
Tiouth pata yii pousso niou péér
Maraday talli ay rappeur taal nii
Gnissi ame chance meu Kanii sén tatii ndx niou wagnii joutou bii
Stay real anyway
Néhh cii kawam evryday
Xamoko
Gangooor
Yabiila tanggoor
Deukkkeul cii naneko
Wa*goor
Ninaal na sa tate yii batayii
Miineul leu sam bopp bamou nekhmeu bayi
Soh gneméwoul guerr bii boul angou bataille
Loula réér nieuweul cii gars yii
Meunou niou téh dougnou bayii
Apocalypse gané cii sén jotay
Fuck sén débat boudé ay détail
Nieuw sole tiarakh cii dîner de gala