Bim Bam ft. Senny Camara Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2023
Lyrics
Ah yaye bim bam
Uhh ah yaye bim bam
Ah yaye bim bam
Héy yé ah yaye bim bam
Kala ak kourousse
Uhh sata ak borom
Yaye héé baniou ma ko dama ko ragal
Héy héy kala ak kourousse
Héyy satala ak borom
Héyy satala ak borom
Yaye héé baniou ma ko dama ko raagal
Gorgou niaw dama fek
souma nek yaye maye mogne
Gorgou niaw dama fek
souma nek yaye maye mogne
Lékét ga toth soungouf ca né paw
Randoul waye gorgou niaw
Randoul randoul lo randoul lo Randoul waye gorgou niaw
Randoul randoul lo randoul lo Lo diour momou loko
Randoul randoul waye randoul waye
Randoul waye diol mou ndaw yombaléma
Man souma démé Mane dina fotal sa yaye di ko togal
Di rote mouy nane bim bam
Héy héy ah yay bim bam
Wo wo ah yaye bim bam
Uhh kala ak kourousse
Uhh satala ak borom
Yaye héé baniou mako da ma ko ragal
Gorgou niaw dama fék
Souma nék yaye maye mogne
Wa diou niaw dama fek souma nek yaye maye mogne
Lekete ga toth soungouf sa né paw
Randoul waye gorgou niaw
Randoul randoul lo randoul lo
Randoul waye gorgou niaw
Randoul randoul lo randoul lo
Lo diour momou loko
Randoul randoul waye randoul waye
Randoul waye diol mou ndaw yombaléma
Man souma démé
Mane dina fotal sa yaye di ko togal
Di rote mouy nane bim bam
Héy héy ah yay bim bam
Wo wo ah yaye bim bam
Loumbay Fatoumata
Seck loumba géy loumbi géth
Bir ba dess teung géth bim bam
Khare Baye néna ah yaye bim bam