
Mariage Forcé Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2023
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
yakar ak yéné ma thi ba
doylo mbeuguél
xol dou xool thi aalale
mais papa ak maman ahn
dagnou ni dé dou fi ame
té mane
xalata touma sama souba sans maak mome
ndeysane
limou gnak tax beugou gnou ko may sen dome
té kénéne koudoul mome
beugouma
ki nguéne ma beug may mane nobouma ko
refrain
fou saaaaa xol meuneu né
day nekh nga fay daagou di def say fém
fou saaaaa xol meuneu né
xamna say tank doufa ragal dém
COUPLET 2
doundou nagnou aye atte
maak mome
wolou diokh ko li xaliss doul dieundeu
sama xol
nguéne yéwou dima may kou ma xamoul
éh beugouma
bok thi
jiguéne yi doul
yeuk banéééeeeeeeeekh
thi sénii biir négou seuye
papa maman
mayé wou lén ma danguéne ma beug diaay
xol kéne douko diaaye
wayer mane ciment la béneu yoone laay tooye
mane ak mome depuis temp boy
couplet 3
mbeuguél bi ngay ndieukeu ji
xaliss soga gneuw
ki souma ko waré dém lolou douma jik
doundou nagnou bép xétou méttite
Maman chérie Kaye wouyouma
bougou ma
Mane bougou ma
non maman bougoumaaaa
mane bougouma
ki ngéne beug may mane nobou mako
refrain
fou saaaaa xol meuneu né
day nekh nga fay daagou di def say fém
fou saaaaa xol meuneu né
xamna say tank doufa ragal dém
Mome la xame
Mome la mime
Ndeyssane
Xalatatouma sama souba sans mak mome
ndeyssane
Ngen yewou di ma maye
Kouma xamoul
Eh beu gouma
Xolou ma
Ki ngen ma beug maye
Mane nounou mako
Refrain
fou saaaaa xol meuneu né
day nekh nga fay daagou di def say fém
fou saaaaa xol meuneu né
xamna say tank doufa ragal dém
Papak maman nenagne dou thi dale
I love i love my boy
He Is my choice
He Is my choice