
Pop Pop Lyrics
- Genre:Pop
- Year of Release:2023
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
Pop Pop - Cherifou
...
kay kay kay kay
kay ma khamal lani
adoun ya dou bène fan
ki gay togal tay bou souba meunala yay
kay ma digal lani boul di khol nitt diko gné
meun nala yobé ignane ( ignaane)
yangui coq coq ba calé
may pop pop thi khalé
ngay tok tok ba calé diémo té meuno dabé
man soma beuguoulé bou salé ( boul salé)
gisnani dolé filing bé leu poussalé (hé hé way)
so beuguouléé boul salé
baal sokhor ignane dalay té
boko topé dagay dé firil sa khol ( aywaay)
hé yeugna liga néké (ay dor rk)
damay lébal bakh gamay fékhel (ioe ay dor rk )
hé bal doré dou guisnala gay leurré
hé hé hé do goré man gisna nigmay woré
boul déféni liga néké yeugou mako dama doylou
bo deféni yakarni ioe yeugnala gamay gall thiow rk
ioe deukél thiow rk
thioy rk ioe deukél thiow rk (thiow rk)
demb yani won
demb yani won goré diwo
kon louleu diapp tay baga né thi yonou none
non paré gouma nonon tambalé gouma( ioe sa kholou kignan yem nama)
sabou do madou falama néné baraka
yangui coq coq ba calé
may pop pop ba calé
gay tok tok ba calé diémo té meuno dabé
ioe woutil bénén yon bo diaré
ioe démo kou né thi yon ga djim ko garé
baal sokhor ignan dalay té
boko topé dagay dé firil sa khol (awaay)
hé yeugna liga néké ( ay dor rk)
damalay lébal bakh gamay fékhel ( ioe ay dr rk )
hé bal doré ah gisnala gay leuré
hé hé hé do goré man gisna nigmay woré
boul défeni liga néké yeugou mako dama doylou
bo déféni yakarni ioe yeugnala gamay gall thiow rk
ioe deukél thiow rk (thiow rk)
thiow rk ioe deukél thiow rk (thiow rk)
(musique)
thiow menoul dara ( dedet)
wakh diou bone fadioul dara (dédét)
thiow menoul dara thi man wakh j fadioul dara (dedét) (3fois)
thiow menoul dara wakh diou bon fadioul dara (dedét)
thiow li menoul dara dafmay yokou dolé nopaloul
khalé baa gui (man la )
khalé baa gui (kham gani man la waw )
khalé baa gui (kham gani man la)
ay man la affair bi man la (ohh) (2fois)
man la
nénagn ma ioe
héee khalé baa gui waw
té bilaay damay fo ak yén
2nd~