Loading...

Download
  • Genre:Hip Hop & Rap
  • Year of Release:2023

This song is not currently available in your region.

Lyrics

El-Shaddaï ft. Junior Sarr - Didier Awadi

...

El Shaddai (ouh El Shaddai)

Geum ko wolou ko (Sunu Borom moy EL Shaddai)

Sunu Borom moy Adonai (Sunu Borom moy Adonai)

Junior Sarr

Geum ko, wolu ko

El shaddaï

El shaddaï

El-elyon na Adonai (sene baat tchi kaw)

Mame yalla, santa na ñu la (dé len ko sant)

El shaddaï

Yeah Awadi Supa Ndaanane international

Watch me now

Tey damaye doli di santati

Doli di weuyeuti

Doli di thiantati

Doli di feccati

Mame yalla ci bopam moma yeukeuti

Samama birou morom moma todjati

Mu leeral ma yonn ma jalati

Jebalou jubali yonou ndam jeleti

Man so ma songue do ko defati

Yalla mo jeul sama combat mou jappa ci

Kou jema dougou da leye tiaxabal

Man fu ma jarr ku fa jaar di nga taxa ban

El shadaï sama wet, dou ma massa tiit (non)

Moma yokka dole, di ma yokka fiit (yeah)

Deguena lahila hi lala

Deguetina ku ma wax alleluia

El shaddaï

El shaddaï (yeah)

El-elyon na Adonai (dé len ko sant)

Mame yalla, santa na ñu la (yeah)

El shaddaï (El Shaddai, Adunai)

J’ai jamais douté de ton évidence

En toi j’ai la confiance

Malgré tout le mal et les médisances

Le malin échoue dans ses manigances

Tu m’as montre les proches et les ennemis

Tu m’as sorti tous les moches et les faux amis

Je les vois les judas qui me font la bise

Le rire il est jaune et la mine est grise

Voilà donc mon action de grâce

Tu m’as fait premier de la classe

Plus de 30 ans déjà et ça continue

El Shaddaï c’est ton bras qui m’as maintenu

Deguena lahila hi lala

Deguetina ku ma wax alleluia

Deguena lahila hi lala

Deguetina ku ma wax alleluia

El shaddaï

El shaddaï (El Shaddai)

El-elyon na Adonai (nen ko wolu)

Mame yalla, santa na ñu la (santa na ñu la)

El shaddaï (Junior Sarr woy ko, youkoul)

El shaddaï (ah man mi gereum na la)

El shaddaï (ah man mi santa na la)

El-elyon na adonai (ah man mi wolu na la yaw yaw el-shaddai)

Mame yalla, santa na ñu la (yaw yalla baye, yaw yalla baye amu ñu sa feyy)

El shaddaï (le le le)

El shaddaï (su mey xalat fepp fi pga diar ak man)

El shaddaï

El-elyon na adonai (elyon el-elyon na adonai)

Mame yalla, santa na ñu la (santa na ñu la né gereum neñu la)

El shaddaï (yaw el-shaddai yaw el-shaddai hé)

El shaddaï (Magaal ko)

El shaddaï (alleluiaaaaaaaaaaaaah)

El-elyon na adonai

Mame yalla, santa na ñu la (waw ni santa nañu la)

El shaddaï (santa na ñu la gereum na ñu la yaw mi el-shaddai)

El shaddaï

El shaddaï (Sama Borom moy El-Shaddai)

El-elyon na Adonai (El-elyon na Adonai)

Mame yalla, santa na ñu la (mame yalla, santa na ñu la)

El shaddaï (El-Shaddai)

Similar Songs

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234
          -You can log in via below methods-
          Reset password via e-mail
          -or-
          Reset password via e-mail
          If you have any questions, please feedback on Boomplay App or send an email to [email protected].

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status