Yonou Goor Lyrics
- Genre:New Age
- Year of Release:2019
Lyrics
Yonou Goor - One Lyrical
...
Légui kham nga kouy One lyrical
Diokh ma sa nop ma wakh la ci Dame
Dame da dioudo ci banlieu bi dokh ci diam diam ba am ndam donga dég diam
Done modél ci gnimay déglou
Eau de javel pour gnimay sékhlou
Mbeussou malén guéstou
Mon papa ne peut pas faire tout
Ma dingone té dingél bor la dama dioubeul pénkou
Ci keurou famille la dioudo deuk ci thiow