Sama Guent Gui Lyrics
- Genre:Afrobeats
- Year of Release:2022
Lyrics
Sama Guent Gui - ADMIRAL MO COSAINO
...
cosaino inna the beat yow yow bombe
sama guent gui lé nakhouma waye
limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye .
sama guent gui lé nakhouma waye
né limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye
yakaronané mbeugel mognou bolé yow
tewoul dem nga bayima baby magui wèt
guent gui lé guent gui lé nakhouma waye guent gui lé guent gui lé nakhouma waye
quand je té vue pour la premiere fois
tes yeux m on attirès ay et je me suis dit que cette fille la vas pas partir sans moi
et j ai tout fait pour me rapproché
oh nana nana nana
sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye
bo démé è dina wèt dotouma am kan moy togue sama wét yow khamoné man mi doumala diawatlé é woy yo oh wo yey yé
quand je té vue pour la premiere premiere fois tes yeux m on attirès ay et je me suis dit que cette fille la vas pas partir sans moi et j ai tout fait pour me rapproché
sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye sama guent gui lé nakhouma waye limay khalate ci yow baby girl nakhouma waye
yow boul dem bayima my baby boul dem bayima mané boul dem bayima a aa