
Ragualouma Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Ragualouma - Ouse Zik Buzz
...
Mama defma yondi yakamtima kon indil money bigaw
Magui sama boppu taloumala nigger ya am temps wou diew
Sokhar ma délou guinaw damay dokh sa kaaw bassa biir bi didaw
Néké borom karaaw bou nioul niakoul dara yow sa Msi da bédiaw
Awma yeurmandé wou ken
boulma wane sa kanam bou triste
Yassi meune guené sa boppu boul dioudou si niak pour doundou lou tiss
Lou souroukheul bague bi si teine
penalty si kanamou Iss
Eunh God oubil niou bountou weurseuk guay feugg ay paquettou kiss
Galou dofe Nga meune Gua fly déme fou sori ni thiély bomaye saurou téral
Sama kadou djibna mounalenn bayekh sandi kherr yi double fock koufi séral
Douniou yakar si ken koudoul yalla
Kenen koudoul yow fi dougn kofi téral
Peneulofi boy dagay poussièral nit yup dima tiow melni doundou bougnou chèral
Never doma sauri biir guew
Koussi nek ak sa biddew yalla Kagn guay dekil sama rou bi dhé
Nélenn niou tok sen papa gui tew
Khadiou mafi melni guëdjbi sicop
dagay dieufei niggel ma matekla si code nokk boyi tok di kharr koussiy topu soniou mounoul support Yako sa garyis si pott
Teklei touma tank Di khar tey séne tati di kharr digua kharr nigger dolenma teinss
Romou nala vif ni sakharr boulma niane délicace efficace moma doli vitesse
Auto mbalitt pipe pipe tabac sa baye men
Def sa boppu victime ni liir bou bayil wenne
Pharmacien oui beach garap gua day reine
Daguene beurri tchip tchip talent dou diay men
Dougou sen gang kom bili boy migui dioy néko yoon bi lerna ni midi boy
Daga rap toopac biggy boy dafa doy nigger douma fake nioumay iri boy
Tu voulais la guerre et j’ai coupé ta tête crois moi j’ai pas fini avec toi nala dagaté ba kenen kou melni yow sakh souma senei fidi
Ragoulama dara parce que mama moma tigom
Yalla Yalla dji motali sama yenei si mom
Nakh motakh may rayanté goudi ak beuthieuk bassi ngone
Sinon fock the reste jamais doma fekk si niom
Dagn deugeul bassi kaff yeah
May dibi sa Msi di saff lekk
Tchékou moussou dougou kaaf
Mais magui ak khalei you saaf
Mounn gua lakatou wakhnei yama meunn mais do door sa lokho si tërei bi
Ouse Zik dou boyi may gaïndé si alleuh nigger guissouma koumay tereubi
Ragoulama dara parce que mama moma tigom
Yalla Yalla dji motali sama yenei si mom
Nakh motakh may rayanté goudi ak beuthieuk bassi ngone
Sinon fock the reste jamais doma fekk si niom
Ragoulama dara parce que mama moma tigom
Yalla Yalla dji motali sama yenei si mom
Nakh motakh may rayanté goudi ak beuthieuk bassi ngone
Sinon fock the reste jamais doma fekk si niom
Ragalouma ragalouma dara
Ragalouniou ragalouniou shit !
Ragalouma Ragalouma dara
Ragalouma ragalouma shit !
Ragalouma ragalouma dara
Ragalouma ragalouniou shit
Ragalouma ragalouma dara
Ragalouniou ragalouniou bitch !