Loading...

Download
  • Genre:Hip Hop & Rap
  • Year of Release:2022

Lyrics

Yeah everyday un nouveau todj todj mais tu fais tout pour te défendre yeah

Meu deukker mougn , di wakh Ak yowe mais tu fais toujours la tête en l'air

Yeah guissngeu Tey bae lougnou tabakh

Lagnou jeul baller parer def ci chaise anglaise

Seu noni gneup tok Mane guissoumalene

Li fi khew yeup walae khamatouma li


Djapone leu ni sama bopp kholal nignu moudjer ni

Et pourtant wakhonala dofi mousseu woujer fi

Sa famille dagn ma bayi parce que dama bouder fils

Inconscience bi leu japp khawma Noumou demer ni

Inconscience yeah bileu japp khawma noumou demer ni

Dix ans de relation lagn briser mounou ma geumerli

Tey Souma jeuler sama yone waroma ci sakh blâmer please

Wakhma Gnata yone yowe leu tar yeah walaye May kiy calmer si


Everyday un nouveau todj todj mais tu fais tout pour te défendre yeah

Meu deukker mougn di wakh Ak yowe mais tu fais toujours la tête en l'air

Yeah guissngeu Tey bae lougnou tabakh

Lagnou jeul ballerparer def ci chaise anglaise

Seu noni gneup tok Mane guissoumalene

Li fi khew yeup walae khamatouma li


Guisngeu lepp ngeu niquer

Motakh awma pitié

Tekci djeulna sama decision Ak sérénité

Khamna limneuy dikker

Sama khol leu briser

Mais grawoul mouna ko gérer vu que dana sick yeah

Everytime yeah sama gars yi dimeu ni

Seu khaller bi boy dafa rew dinagn ko mousseu mougeul fi

You deserve no love ter sokhlawo sama sympathy

Girl you broke my heart yeah guisngeu li c'est pathétique


Baby baby baby

Khamone ngeu yaay semeu lady

Douk jaakk tak seuy ber

Ngeu moudj done sama First Lady

Je sais que souvent defeuy shady

Mai's waroul takh ngeu act crazy

Nakh yowe la am bilaye

Jaral ngama accident

Meu doug ambulance my baby

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234
          -You can log in via below methods-
          Reset password via e-mail
          -or-
          Reset password via e-mail
          Feedback on resetting password
          * It may take a longer time

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status