
Love Talk Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
Love Talk - Weuz Lo
...
Mbeuguè langui nè moma rombou di dème
Ma lathie kou foumou dieum mouni ma yassi dèss
Ma topou ko di dème mou dièki rk ni fèss
Ma geuleum tèla rère mèlni kougniy dogua feugue pèss
Mbeuguèl bosiy dogua diote day mèlni Iphone
Dièki sopalikou pour ngua accro geuneu bone peste
Fi sa best molay trompé ak kingua beugue
Kingua beugoul moy daw si lingua beugue
Fi lilay faate yakoy fate sisa keur
Niata yone lasa sœur beugeu dieul sa dieukeur
Mbeuguèlou soukeur ngua done snap tay nguay dioy ba seukheute pour yaw secret moy ngua dègue *ALHAYRY*
Seuy dou bène fane adouna la ak lissi bir
Kholatal lisi bir beuguel dou wakh diou nèkh
Banèkh di rère fi nieupay siigne an
kholate li si biir beuguèl dou wakh diou nèkh
Banèkh day rère fi nieupay siigne an
Beuguèl dou tok-tok rek ni mikk
Fi nieupay semblant ba am liniou beugue siif an
Kholatal lisi biir beuguèl dou wakh diou nèkh
Ma nèkhi rè fi nieupay siigne an
Niatta yone ngua bayi ndaw si dèlou watte (Dèlou watte)
Niata yone lala wadji torakhal ngua dèl si watte
Thi misal gaur bou beuguè dafay mèlni khar
Djiguènne bou beuguè dafay mèlni khathie
daniouy mattè tè day dague sa yappou bou nèxoul douy la daare
Fi
Amna niouy doundou amourou derbi
Dagua lane tè ay ndèye ba goudi teudi
Amna niouy doundou amour bou cool bi topatowantè ba goudi niou teudi wèète
Amna niou khamni niome sène yone lougne si meuna wakh daniouy doundou sène love (hein)
(Kholatal lisi biir mbeuguèl dou wakh djou nèkh
Ma nèkhi rè fi nieupay siigne an ) ×2