Daf Niou Bett
- Genre:Afrobeats
- Year of Release:2019
Lyrics
Daf Niou Bett - Maabo
...
yaguona fok ni sokh la wou ma koudoul mane mi mane ken la wone thi yone wi sokh di dak sama yan wi beusse bi mala guisse kerok dafa ler si gnoune gniar souniou khouli ba gnou dadje thi la kham ni yaw la done khar yah yah yah yah ya takh may weur fi mbecte bek guir idil la yah yah yah ya fok ma thi Indil la sama diame yaw la yatakh ma kham ni mbeguel nekhe man sama diame yaw la meussou ma fok ne man sama diam yaw la legui ma tolou fi man souma bègue ya takh li Daf niou bête man ak yaw si mbecte guamay delo dima deufeul may ree man awma benen hero yaw yamay bégueule sa soune wo wo eh yah ya eh woua
Similar Songs
More from Maabo
Listen to Maabo Daf Niou Bett MP3 song. Daf Niou Bett song from album Jolofbeats is released in 2019. The duration of song is 00:03:30. The song is sung by Maabo.
Related Tags: Daf Niou Bett, Daf Niou Bett song, Daf Niou Bett MP3 song, Daf Niou Bett MP3, download Daf Niou Bett song, Daf Niou Bett song, Jolofbeats Daf Niou Bett song, Daf Niou Bett song by Maabo, Daf Niou Bett song download, download Daf Niou Bett MP3 song
Comments (5)
Top Comments (1)
sokhakh miniellebaba@gma
New Comments(5)
125658990
machall
knadim mbacké Diawara
[0x1f607]
migno bella
sama bouma deguee sene baate ma faté mitite boumaye doundou yalla na Yalla bakerle ne je vous aimes fort mia et mabo[0x1f623][0x1f621][0x1f623][0x1f619]
Daniel Jammeh
[0x1f630]
sokhakh miniellebaba@gma
j'adore
j'adore >