
Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2021
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole - Aby Ndour
...
Dafma guis beuguema néna mane doynako foh yeukeutouko kay gah . Dafma guis beuguema néna mane doynako foh yeukeutouko kay gah xélalma. Sou fékké baxna barri yeurmandeum!! soulanguici biir mani dougal baxna Andeu bou yague sincérité Wanici foullah lici déss yallah baxna Nii taaru djiguene séey leu Nii taaru djiguene séey leu Séey té yallah taax Déguenala wayé lima diaxal moy séey boufi béss niéty wërr niouné tass na Damanila séey diamouci yallah soci faarlo liko takk tassouko Mane beuguena dieukeur bouma noop dima wax deugue té douma woutal niarél.yéni abibatou soudé meunala yoor yoor kénéneu souko nékh takk ngiéte bah ngiente Nii taaru djiguene séey leu Nii taaru djiguene séey leu. Séey té yallah taax. Tay mah waxla nimou mél noumou mél môme yeureum nama ci léep moko waar fiirna bah mélni gaïdé Rebeu alleu guissoul loumou lékk nénama mah waxla gaw paréna guiir déf lou gaw Néko mou yooné ay bokam gaw dax lou gaw sokoy déf dag ci gaw Wax ko mou yooné ay bokam gaw dax lou gaw sokoy déf dag ci gaw aby .Wah ki kat soko mayé dina séey ang kay mom dina séey billahi dina séey séey kat lah domi séey kat lah kouko mayé mou séuy yobanté kouy toukki diaynalako diarnako diolé kone woyeul yow yah dougou ci seuy dagay sallo dih mougne ligah môme gah diethialikou boul tite boul ragal Mayé gama mah seuy gallah waxal mako niou dém beuci biir sopi diékko lay ragal Dakh taaru djiguene abibatou moy mou seuy Dakh séuy diamou yallah leu mouy yéune boul xolle dieukome beugeunté léne Niit soko beugué loumou déf saf nala saf nala Séeto séete yow ganima séetoo séete moh aka diongoma seuto séete séete bi yék ci na Séuto seute diongomala seuto seute nimou dago séuto séute séute bi yék ci na Mani taaru djiguene moy mou seuy Té séuy naci mbeugeul djitou mani Séeto séete ko deugue leu Séeto séete dégeul lolou Séeto séete séete bi yék ci nah Séeto séete kone deugue leu Séeto séete moh deugue leu Séeto séete séuy bi deugue leu Séete bi yék ci nah So allah diabi mbeurname boubi réyum réyum Séeto séete yénako beugue déh Séeto séete môme lagne done xaar Séeto séete kone dagoul séute bi yék ci na
Similar Songs
Listen to Aby Ndour Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole MP3 song. Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song from album Seetoo Seet is released in 2021. The duration of song is 00:03:44. The song is sung by Aby Ndour.
Related Tags: Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole MP3 song, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole MP3, download Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song, Seetoo Seet Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song by Aby Ndour, Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole song download, download Seetoo Seet ft. Alioune Mbaye Nder & Ndiole MP3 song
Comments (61)
Top Comments (5)
Arona LYglxzs
Dieng Aliou
G[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]N>
seynabou fayeg4b60
>

New Comments(61)
137338260
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f63d][0x1f63d][0x1f63d]
Elhadj Lamine Diallo
nickel
147442519
♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Kadiata Abou Fall
Nice
Ablaye bair3fq
sally[0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641]
Sidyfsk4n
good song
Fatou frvdx
[0x1f623]
Fatoum7mb2
[0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f630][0x1f630][0x1f630][0x1f621][0x1f621][0x1f621][0x1f63d][0x1f63e]
machalah
Adamaiafy1
ma

ndeyeicw4a
[0x1f641][0x1f641][0x1f641]
C’est géniale çà >