Nieuw Na
- Genre:Afrobeat
- Year of Release:2021
Lyrics
Nieuw Na - Queen Biz
...
sama Khol bi yéna ci nh yéne la khamone nani douma meusseu dem sans yéne nekk fans queen dafa yomb sama khol bi yéna ci nh auto bissi kanam lagnou corné khamnani dathie guéne ci louné baguéne diapé ba tay bayiwouléne yéne daal khamone nani fouma meunti déém guéne kharma deugue deugue yénaye diambaar khamna li guéne done khaar sassou nh guéne di ame yakar nakh néguéne man maye sen star nieuw na nieuw na nieuw na té dotouma dém nieuw na nieuw na man dotouma dém wakh kati nagnou guéne wakhati dagn foguon sen yéné andna lolagnou bouguone yallah wédi so démé né léne queen nieuwate na une munusé métre temps suis une munusé suis validé mon publique ma validé diéme nagnou diéme th mounou niou thi man dara sa souma dioulé nian sougnou borom mou art ma beusse bima nh dama bayi yéke nallah ba bassi sene dioyé nieuw na th dotouma démati nakh douma beugue léne lou léne métti deug deug awouma sen faye yen daal sama khol bi yéna thi fésse yen la guiss na leguene di dathie thi man ba taxna mounou maléne bayé souma kholé fima diaar man yéna tax meuneu touma happy nieuw na nieuw na nieuw na th dotouma dém nieuw na nieuw na man dotouma dém wakh kati nagnou guéne wakhati lolagnou bouguone yallah wédi so démé né léne queen nieuwate na une munusé métre temp suis une munusé suis validé mon public ma validé nieuw na nieuw na nieuw na nieuw na th dotouma dh nieuw na nieuw na man dotouma dém sama khol bi yéna ci nh yéne leu
man yéne la ame
More from Queen Biz
Listen to Queen Biz Nieuw Na MP3 song. Nieuw Na song from album Nieuw Na is released in 2021. The duration of song is 00:03:24. The song is sung by Queen Biz.
Related Tags: Nieuw Na, Nieuw Na song, Nieuw Na MP3 song, Nieuw Na MP3, download Nieuw Na song, Nieuw Na song, Nieuw Na Nieuw Na song, Nieuw Na song by Queen Biz, Nieuw Na song download, download Nieuw Na MP3 song
Comments (5)
Top Comments (1)
Thiabaerkht
New Comments(5)
Christinebj0um
queen biz jtm beaucoup j'aime cette chanson
Adja6k67a
courage je kiff cette chanson[0x1f618][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]
tymachou 169
alhamdoulilah Quenn gnèwate na
Thiabaerkht
enfin queen nieuwate na alhamdoullilah
Alhmadoulillah
nice sister
enfin queen nieuwate na alhamdoullilah>