
Adama Paris ft. Nix & Jay 21
- Genre:Afropop
- Year of Release:2020
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Adama Paris ft. Nix & Jay 21 - Samba PEUZZI
...
hey thiakasse gine gine thiakasse gine gine yaaa yaa thiakasse gine gine
and nén Dubaï and Italie ma defalko shopping Dior goochi coco Channel
tay fine bou mol dïol nioule aka paré
teins naturel démarche bi momay danél shiiii boy xalé bi défilé adama paris
adama paris adama adama adama paris adama shiiii sho bi day défilé défilé adama paris adama mélnimi
adama adama adama paris ouh yah hey guél bi day defile defilé adama paris adama ménemi adama adama adama paris sho bi day defilé defilé adama paris adama hou adama adama adama paris hey tay cocacola cheveux bouy wathie bassi hansse yi damay contane bouy nieuw si man ak doxinou guélou j té ah do namou dra yay guén ak bosse bi bb man reka meneu dindi sa glosse ligue may defal mako xam daga mok pothie degue dadje mane dh diama noir guem xéssalo yako sa teins wa liguay sagnsé yako tay black mine africain souy dox dank aka téy ay talon 13cm semelle rouge loulay faye man sma dh yako diam gnilay garouwalé danious pérte ande nagne dubaï ande itali ma defalko shopping dior gucci coco chanell taille fine bou mol diol nioul aka paré teins naturel demarche bi momay danel sheutt boy xalébi defilel adama paris adama adama adama paris shiiii sho bi day defile defile adama paris adama menemi adama adama adama paris ouh ya hey guel bi day defile defile adama paris adama menemi adama adama adama paris sho bi day defilé defilé adama paris adama ouh adama yaa adama adama adama paris ouh ya hey sho bi day defilé defile defiléé
houuuuun ok falay tambalé xamatouma kouma guene marsué ba jai arrété de comptés les annés aux azar ben beuss konar mou feul ak faram ma mayko saram diéxal ay ballam mou mayma kanam ma sexalko baram neko thi kanam loutax may simekou yakati lalam manam byby man gay dieuke VIP hou facone 8 bi fok ga tagalko adama fétel niou VIP photographe bi fok mou mediter amo féne loloy verité sa doxine soxla woul podieum tank bo tek souf tanke yaye MJ mou a mil lalay solal maname niouleuss collection siliravitan arank nienene collection beur dof la puissanse zero collection tangal samay bagass naw di bayi sama xale bi piloter l avion
Similar Songs
More from Samba PEUZZI
Listen to Samba PEUZZI Adama Paris ft. Nix & Jay 21 MP3 song. Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song from album Senegalboy is released in 2020. The duration of song is 00:04:35. The song is sung by Samba PEUZZI.
Related Tags: Adama Paris ft. Nix & Jay 21, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 MP3 song, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 MP3, download Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song, Senegalboy Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song by Samba PEUZZI, Adama Paris ft. Nix & Jay 21 song download, download Adama Paris ft. Nix & Jay 21 MP3 song
Comments (9)
New Comments(9)
ÉTOILE mwn8g
meth capo ba
j adore
Amadouaw
superbe[0x1f618][0x1f641]

118983664
[0x1f630][0x1f630][0x1f630][0x1f630][0x1f630]
gagnessiry
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f621]
pkbw8p6
hehehe
Abdessalam Sy
cool !
jay winner
Jay t'es fou