- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
Lyrics
OGFQ - One Lyrical
...
yéh pour mane ligueuneü dip si nitt moy fi thiow di dohontou
nekhnèkh biguay am fogou odji plaisir avant tous
mane dale come karaw gneup mane lagne yagnou bénéne rappeur moy kharou tabaski diotna alléyouya paka tate wala paka dasse dominique sa khôle da khata paka tasse mane soraléwoumala ni café bou tangue album bou lamigne bi dima dédicasse wow album bi daffa beurri ay doute ndeysane défenseur gua ni digua doute Aÿ sanne comme ignèsta souko dème niou cool Guay tamoul famille salle maléne rouf rék tamou tous ték chaos tak samay nioum leette tale deglou samay mélodie di vibe thiaga d'où gouvlek mane bitch nigga mane dmala bay pour sa royoukay guané yéné négue borrom mathiay fanane yéné nala diam yéné le succès diamant bou dessoul loudoul Rapp mane may sa baye teukeu légua comme kouy teukeulé barca k jarafe 2020 niou alasane djigo 2020 niou aréna yigo 2020 niou doundou classico parena pour diar sa kaw 2016 balégui tontougua motiné woumako bippé woumako damako dip kay com'on mane of the years man of thé year am the fuckin man man of thé year mane of the year mane of thé year am the fucckin man lo nième niak (you) lo nième kaw (boy) fékhél bâ boul daw assumel boy (bitch) ragualouma thiow(skkrrrt) potentiel lay donne keuf khalissou na dem bosse soul na boukki birr golf djieulna bâ djieut Aÿ caul (time) diote guéne si mane bassounou (yeah)
Similar Songs
More from One Lyrical
Listen to One Lyrical OGFQ MP3 song. OGFQ song from album OGFQ is released in 2020. The duration of song is 00:03:40. The song is sung by One Lyrical.
Related Tags: OGFQ, OGFQ song, OGFQ MP3 song, OGFQ MP3, download OGFQ song, OGFQ song, OGFQ OGFQ song, OGFQ song by One Lyrical, OGFQ song download, download OGFQ MP3 song
Comments (15)
New Comments(15)
Boubacarczbds
Coura Traoér
nice
Magor Camara
dip sa bay la
Mamadou diopekmdl
yafi men yay doamond
mamadou sambd46zx
[0x1f647][0x1f647][0x1f647][0x1f647][0x1f642]
dip ton père t' appéle
mamadou sambd46zx
dip ton père t' appéle
119941108
♥️♥️king
BemZobblxu
le kinG
mouhamed ndiayeawn3
number one for ever
sileymane thiam
King
do nitt saxx