- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
Lyrics
Guemko - Ashs The Best
...
Kou rasta huuum aaanh éeeh ou yaa ouh Haa (2f) Nénagn nga diap teuweu bayi Lou yomb djigoul kéne nonon Si lep lo meune yeungou gueum ko Yalla daal waxoul keen dara Nonon Yeen Say mou méti yeen saay Waaah Yeen saay nga guersou do guiss kéne Nonon Lék lé mou tar baga fokni dou diekh mais Yalla waxoul kene dara Nonon Mama migui né Yakamti maa Yeen say ma goudé mais douma fanane Oh Mama ma yoné Yakamtima mais yeen saay ma goudé mais meussou ma fanane Hé borom karaw bou nioul laa dara ma diomboul si kaw life di heuy mouy méti taxoul bayi meussouma xadi meussoul daw Nékone si leundeum guisso nadj taak Xaré Soubeu ba nadj tiono dou reeer borom ndeysaan Dinagn ko niafé ba xeuy death Yeen saay mou méti sisa weet guissoulo koko wék Adouna ko démé ni Yeen saay nga fokni dou diekh feek lep day wess day méti rek mais Biss dina nekh Yeen say lo yakar mou tass lélé ngay lathié loutax Yeen say nga yanou lou diss Owowowo Nénagn nga diap teuweu bayi Lou yomb digoul kéne Nonon Thi lep lo meun yeungou gueum ko Yalla daal waxoul keen dara Nonon Yeen say mou méti yeen say waay Yeen say nga guersou do guiss kéne nonon Lek lé mou tar baga fokni dou diekh Yalla waxoul ken dara Nonon Maman ma yoné Waa éh yakamti ma éh ah yeen say ma goudé mais douu ma fanane Oh mama ma yoné
Similar Songs
More from Ashs The Best
Listen to Ashs The Best Guemko MP3 song. Guemko song from album Millions Flows (Deluxe) is released in 2020. The duration of song is 00:04:10. The song is sung by Ashs The Best.
Related Tags: Guemko, Guemko song, Guemko MP3 song, Guemko MP3, download Guemko song, Guemko song, Millions Flows (Deluxe) Guemko song, Guemko song by Ashs The Best, Guemko song download, download Guemko MP3 song
Comments (3)
New Comments(3)
cheikh diopgj55f
grand frère cool
Steff Kanoi
Right AsHs u're the Best ever[0x1f641]
weuzcrazyweugoweugo@gmai
grand frère cool
cv