- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2024
Lyrics
Ñi taxx màdane yeuk jariñu adunah
Dem nañ, Dem nañ
Ñoom dem nañu bayii ma
Mama mangui dee ak wéetaay
Papa mangui dee ak wéetaay
Dayy tiis, ñunane ma ñaan lalene desel
Té gis, lii gén def ci man bama mel nima mel
Tey bés, yagui dem teewul xol gui wéroul
Ci sédday saxx féexul
Wéetaay bama fajutt Yeah
see lyrics >>
Similar Songs
More from Moumou King
Listen to Moumou King Wéetaay MP3 song. Wéetaay song from album BBN (Bañ Bañ Nangu) is released in 2024. The duration of song is 00:02:41. The song is sung by Moumou King.
Related Tags: Wéetaay, Wéetaay song, Wéetaay MP3 song, Wéetaay MP3, download Wéetaay song, Wéetaay song, BBN (Bañ Bañ Nangu) Wéetaay song, Wéetaay song by Moumou King, Wéetaay song download, download Wéetaay MP3 song