![Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/13/ca85fc2a250a41b9adbb22fe0cd1190fH3000W3000_464_464.jpg)
Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best 🅴 - Bm jaay
...
yeah ok semaine nou yalla gui téyéwouma deureume goor niarri jeans kelk t-shirt dall yi diagoul goor métite boudé geune nama doundou dii door niaffé di geune tardé amouma weurseuk goor xamo gathié teudj sa guémine parck yoroo yeug yeug biguay am sou mère di laccé amo niak ba ragal gua dougeul ken si ngoro gaccé gui lay dall so bokké yérré yii guay sool yaw ak say broh merr ba teullé giff,marr di déh ak khiff,diappé niit sa boop mou diappé la compétition lima la yénné gua don siff reutiou na wollou niit yo khamné mouno lime sen avancement té doma lime,tay souma amone choix bi tamit douma changé dra déception motax ma xamni amoul ken kouma faral, wax gua deug changé na nigger magg na tamit nekoul djikko th dou diamono how me lii mokko waral.... thiono ak gaccé,yakkar gou nieuw day tass cii youne meunou niou deuk cii werde,waxall lo meune si mome,sou démé ba gadday, sou déselé toul geureum daffa fekk mou wett waxal lo meune sii mom ho hoo hooo. yeah,niit la xélam gui di teudjie mou def la thiabii laobé,thiono gou féyékou woul gorré lakk xoll si gaccé intérêt bou nangouwoul ganiou nou sa xell di naccé,meusso beug di goudé beug ma yénné nadié. fuck talent liguéye sou amé mérite douma niakk,nianou wadiour niakk dou rérr lou taw bii di bathiee,yonou ndam ak sankou ndaw lim bi len xadie gatt, th esperance de vie bi mayouma temp por xallat. chak goudi nioune salon bii fofou laniou done fanane,diaxlé bay laccé baxam life dina ma faye lime ko lébal,guissouma makk guestou wouma ken dou lenn louniou ma defal siguil yii bagne ma seugg lolou kessé moma sonal.damay def th douma xoll,def guir sama xoll meusou ma djiteul émotion soudé day moudiou thiool bayy cii sama tool man may sama idole bagarre nonne yii sii mane combat bii geune métti moy ak ndooll.... thiono ak guaccé,yakkar gou nieuw dayy tass cii nioune meunou niou deukk cii werde waxal lo meune sii mome,sou démé ba gadday,sou déselé toul geureume daffa fekk mou weett waxal loo meune sii mome ho hoo hooo thiono fadioul gaccé,none moyye kilay laccé,so yégone koulay waccé xoll ko cii say dome ndèye thiono ak gaccé ououou(x3) si thiono ak gaccé yeah...
Similar Songs
More from Bm Jaay
Listen to Bm Jaay Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best MP3 song. Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song from album TDOM : The Death Of Marouane is released in 2022. The duration of song is 00:02:38. The song is sung by Bm Jaay.
Related Tags: Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best MP3 song, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best MP3, download Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song, TDOM : The Death Of Marouane Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song by Bm Jaay, Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best song download, download Thiono Ak Gathie ft. Ashs The Best MP3 song
Comments (4)
New Comments(4)
Eunice Sylva
Bigmo Seye 31
Marouaned⭐
Moussa Diallo 0wdt3
walahi tu es le meilleur bilay [0x1f623][0x1f60d][0x1f60b][0x1f60e][0x1f63b]
Bada Miracle M'boupez8fp
cocktail ❣️❣️
je l'écoute en boucle Waouh