![Satan 2 ft. Mist Cash](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/13/ca85fc2a250a41b9adbb22fe0cd1190fH3000W3000_464_464.jpg)
Satan 2 ft. Mist Cash
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Satan 2 ft. Mist Cash - Bm jaay
...
guerre comme iran ak irak shit fuck drapeau blanc chicago ak chirac rombou fi comme diégui sirat sama énergie comme kouy dieul pilseuk ? dou cendrillon mais après minuit yéré douko solat ? sanil khère mine na grève nio woté guerre di niane trêve none dou guiss sama dréte même si thiono même si galère doma wakh limay def doy na pour mandi saw si ay mbed kholal bou bakh linguay ték dofo djiné diapoula frère.
Fuck off on se fait la guerre fuck trêve fuck néke sama wéy ladj dréte ? mister cash vandam le rap c'est un putain de marché noir avec des marginale qui font du vandale pendant ce temps ma dike di def couplé yeup ay scandale dieul sa tendance nigger loy nday bagn meune ngueu rap meune ngueu def 100 ans ? mo gniy nénguégne diay souniou tout sène tanta mais nak 100 ans mounonio nday fay ayo beugué nio tankal séto khamo ban bor ngua fété.
Meuno thi fuck douma koy saga mouy signe lal sama meilleure routine sène game si pote nioune yalla mo niou time king baba sama dick niongui au top bombe sa nday missil satan ? eh meuno si fuck Bm jaay mister cash fi sip nagn ni dangua tite mani please fils nioungue lay streamer ana say real tige fils bougniy teudé game bi sa kanam lagniy guiss bitch faw ngua liguey té yor khalis door niou 10 bitch wagnil wakh bi seugat si job bi.
caporal yé tèwe ? néka toul rap rék li di maltraitance meusseu go todie takh na guéneu go Sénégal guéneu go sénérap ? rek dina bakh amiral caporal général mister cash dagn ma dane téré rap sama rak diko deff balou guone rak tak tak tak bangua dè coupable capable.
? spirit si sa biir gin-va pussy ngueu ndaysane money béke khalis guisna deumeu ngueu pire va rombeu leu sori nagn distant
Similar Songs
More from Bm Jaay
Listen to Bm Jaay Satan 2 ft. Mist Cash MP3 song. Satan 2 ft. Mist Cash song from album TDOM : The Death Of Marouane is released in 2022. The duration of song is 00:03:19. The song is sung by Bm Jaay.
Related Tags: Satan 2 ft. Mist Cash, Satan 2 ft. Mist Cash song, Satan 2 ft. Mist Cash MP3 song, Satan 2 ft. Mist Cash MP3, download Satan 2 ft. Mist Cash song, Satan 2 ft. Mist Cash song, TDOM : The Death Of Marouane Satan 2 ft. Mist Cash song, Satan 2 ft. Mist Cash song by Bm Jaay, Satan 2 ft. Mist Cash song download, download Satan 2 ft. Mist Cash MP3 song
Comments (10)
New Comments(10)
Aladji diallo 02lcz
kane2024
Merci
bd bab's
fatt ndy feep
Sadio l0t4j
mist cash il est fort p*t
Nass4ly29
Dope
elhajj 125
putine flow
Mademba Biteye
Damn
Bada Miracle M'boupez8fp
OMG ❣️❣️❣️
Babacar babrfhx
té l meilleur
papeihlw5
hot
Marouane