![Too Late (L'incompris Speech) [Interlude]](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/13/ca85fc2a250a41b9adbb22fe0cd1190fH3000W3000_464_464.jpg)
Too Late (L'incompris Speech) [Interlude]
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] 🅴 - Bm jaay
...
escuse me balma don't more douma sa noone mangui si yangui si ñouñe nieup leuh say know it's too late (3) it's too late (3) yeah si sama xél ak sama xol loutax may guiss ba légui meunoulo ma bal mane sax xawma ba xam amna loumla diapal waxalék xél so naré guéné ling'ma denthial peut être si yaw leuh peut être si mane diox leuh samay sécrêts wayé guassolo ma camb nénañou cadou bala té yaw guinaw ngama diam wwaw aay mérone na bimlay wax mak yaw nafi yamm wayé kham nga liñouy wax rék dounya amoul solo amal xaaliss amo nitt ñi kéneuh gueunoula troxx soff nga tropp troxx lay sikaw souffmoma gueuneul dém ba si yallah sa aÿ akkeuh dima sonal dangua rëuy manitt dama rëuy diameuh si aÿ nitt la xathie limla déf wessou nama balma souñ ko défoul légui layo al-lahira fierté dougou souñou diganté motaxitt wéssna douñou aaÿ noone it's too late (3) it's too late (3) dox si leundeum ak sa xaaritt mo gueun dox si léérr rék kanam dou kasso wayé koko fassal moulay ñane nax doma si guéné da fék mou ame foumla tékk dou bourr bi yallah moñou mom boko togné dalay bal sou fékoul nga done bokalé lou warone ame ppassé a té kéneuh meuneutou ko changé honnête diégué nañou li war nañou ko meune di passé fukki guass fukki di soul warowona bayi kéneuh di dougou si diganté bii bangua dioxé say noppou sa xél bobou ñañ ko teuthie diganté pousso ak weuñ sodoul ñaww waro si xaathie ñoulay nékk dila conseiller liñou dioté manak yaw moyy louma sékkoul ak ñom d'accord na meune nga si wax mais yiitt ma e leuh waro done wathié sa boppou soudé ya togne dou béneuh niakk diom manak yaw douñou noone seytané dougou fiñou ko xadialone bama tégué premier pas vi si la diéxal limla désalone guaïndé sank ba légui mangui laay dég'lou yangui ñaxtou khana khamo adouna bii dou eskëy lo tabbé ak loula meun dik'kal mélo boumou meuneuh andal änd sék xél bou sélleuh nax so andoutak ko diépi andoukok ko bañ do änd ak kénn té bo andoulak kénn dañouy nane dangua bérou motax man'la dél änd'ak ñeup ba paré änd'ak sa bopou naax lo dieumbeutt tokk si kérr bamou dess nitt comme le disait l'autre :<< chaque séparation a sa mélancolie, de sur quoi la trahison ne vient jamais de loin >> ñibbil ngay beuneuh miss si birr diougual fi nga tokk yangui gouddé l'incompris
Similar Songs
More from Bm Jaay
Listen to Bm Jaay Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] MP3 song. Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song from album TDOM : The Death Of Marouane is released in 2022. The duration of song is 00:03:12. The song is sung by Bm Jaay.
Related Tags: Too Late (L'incompris Speech) [Interlude], Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song, Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] MP3 song, Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] MP3, download Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song, Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song, TDOM : The Death Of Marouane Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song, Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song by Bm Jaay, Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] song download, download Too Late (L'incompris Speech) [Interlude] MP3 song
Comments (3)
New Comments(3)
Marouane 14 Fourteen
Marouane 14 Fourteen
son amatoul
Omzo kr8s
Boo do nitt
tu es le meilleur