
Reine Xol
- Genre:Pop
- Year of Release:2017
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Reine Xol - Maabo
...
yayeeeeee sama yaye yaye yaye booy , yaye booyyy
yaw yaye ki guene ci yaye ,Di dapp sama banex tei d'ici tay.
toudd nagne leuh nietii yone sogga toudou baye , sant nala gueureum nala yaw yaye , yarr niou yorr niou yirr niou meusso ci tayii ,meunouma bagna nameu Say diottay ,mougne ,moytou, mandou ,sa moussalayyy sant nala gueureum nala yaw yayeee ,bala ma meune wax yama done wayal tay do wax malay walay rayal nala teigne , yaye dinala teral sant nala gueureum nala yaw yayeeeu
Mama i love you so finga beug fofou l'ay khôl,la la lalala , yay sama reinou xol ×2
Té mangui diegualou ci Lima tokk Lou yagg beug leu tei wanou Mala Ko Souma sagnone Mane dotou ma tokk beuss pas eà guiss lh tei wanou Mala Ko yaw yaye booyyy
yayee,sama yaye, yaye , yaye booy Maaa
Sant yallah ndax lokho lama béral ,bou dessone ci iao doma feral ,Dara doula tei yaye booy demal, nilh itt bila diarama nenaam, yarr ma yorr ma yorr yee ma dima khelal , weer nga wane nga xol nako feral
mâley yoma ,leyom ,yomalene n'a, nilh itt bila diarama nenaammm
Balama meune wax yama done wayal tay do wax malay walay rayal nala teigne yaye dinala teral sant nala gueureum nala yaw yayeeeu
Mama i love you so finga beug fofou l'ay khôl la la lalala yay sama reinou xol Mama i love you so finga beug fofou l'ay khôl la la lalala yay sama reinou xol té mangui diegualou ci Lima tokk Lou yagg beug leu tei wanou Mala Ko Souma sagnone Mane dotou ma tokk beuss guiss lh tei wanou Mala Ko yaw yaye booyyy
see lyrics >>Similar Songs
More from Maabo
Listen to Maabo Reine Xol MP3 song. Reine Xol song from album Yako Waral is released in 2017. The duration of song is 00:03:15. The song is sung by Maabo.
Related Tags: Reine Xol, Reine Xol song, Reine Xol MP3 song, Reine Xol MP3, download Reine Xol song, Reine Xol song, Yako Waral Reine Xol song, Reine Xol song by Maabo, Reine Xol song download, download Reine Xol MP3 song
Comments (2)
New Comments(2)
youssouphawn3vc
bi amatoul wallakhi
youssouphawn3vc
bi amatoul wallakhi
merçi maman