![Magui Bakh](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/23/54d4b5c60bcb47feb2261181f17b0d10H3000W3000_464_464.jpg)
Magui Bakh Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
Lyrics
Mane rek ci sama yone
Douma deglou wakhi noone
Mama né lo meunti done
Boul meussa diaad deff lou bone
T'inquiètes maa mane magui bakh
Bayina xel ci lingama yarr
Faté wouma yone bingama wane
Beuss dingama sentou fingamay xaar
Doumeu faté kima boote
H24 j'suis dans le bloc
Bayil ma neekk ci sama bopp
Tekk na lepp ci looxo God
Bou laadié xarr tankou toubey pour yeeg dina xouss diaale
Sama life boy lama tale teu magui feel mane samay vibz
Niit bounek limouy game
Boudoul God amoul dara loumay yeem
Amoul dara loumay yeem (Heeeeey)
Bayil meu neekk ci sama bopp (Heeey)
Mane talouma niom louniouy wakh
Magui neekk ci sama yone
(Magui neekk ci sama yone)
Mane degouma niom louniouy wakh (Heeeeey)
Mane magui bakh
Ioe yagui bakh
Fi nieup niogui bakh
Nioune niogui bakh
Niogui bakh niogui bakh hey
Ioe yagui bakh
Fi nieup niogui bakh
Fi nioune dh niogui bakh
Tu sais que j'ai pas le time
Kon bouma lathié c'est quoi les bails
Bayil ma weett ni diante bi tale sama bopp everyday may gueuneu di shine
Mama mogui pray so lepp gui fine
Doumeu use sama mind ci quelques détails
Diam la yené nieup teu bokoumak gni sen xol yi deuk di shine
Où sont les yencli
Tu m'aimes c bon tu m'aimes pas tampis
Chez nous on vit comme tous les samedis
Pas encore riche mais on est tranquil
On s'était dit qu'on va le faire
Gang bi yeupp fi keen dou meer
Diaroul sandi xeer
Bro life bi comme ballou tings
Niit bounek limouy game
Boudoul God amoul dareu loumay yeem
Amoul dara loumay yeem (Heeeeey)
Bayil meu neekk ci sama bopp (Heeey)
Mane talouma niom louniouy wakh
Magui neekk ci sama yone
(Magui neekk ci sama yone
Mane degouma niom louniouy wakh (Heeeeey)
Mane magui bakh
Ioe yagui bakh
Fi nieup niogui bakh
Nioune niogui bakh
Niogui bakh niogui bakh hey
Ioe yagui bakh
Fi nieup niogui bakh
Fi nioune dh niogui bakh