
Super Hero Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2020
Lyrics
Super Hero - Ino Kind
...
sama héros sama heros
na na nana nana
sama heros sama héros
Sama héros mom sakhoul ay laf
Mai meune na wéssou assamane
Sama héros sans super pouvoir
Té meune géré loufi anormal
Blem yi ma calculer si sama life
Mou solutionner té bania bayi eh eh eh
Kouy réss sa karangé bilay walay meuno ko fay
Kouy réss sa wergou yaram meunou ko fay ehh
Sama yonne si Iron Man
Sama yonne si Batman
Sama yonne si super man
Ndakheté amena sama héros
Amena sama heros heros heros
Yéwou souba tél bania goudé
Dou tére ngeu fanane founé
Xol bou deugeuroul dékou louné
Géré sa metite té sene boss dou fégne
Ba ngay teudiou niom nio ngi si biti
Nekal feu askane bi dalale sene fiti
Bou done ay bomb niou diay doundé dé
Té séni payore diarouko man
Mouy blouse blanche waleu casque bleu
Géré béré rouge teksi camoufler
Teukhou hôpital melni amougne keur
Bayi dakaneté bi diéma yarou man
Nieupa ngi dadialo 20h diéme léna tathiou pour remercier léne
Wakh feu deugeu no amougne seni faye kone yalla na diam rk yague si yéne
Sama yonne si Iron Man
Sama yonne si Batman
Sama yonne si super man
Ndakheté amena sama héros
Amena sama heros heros heros
héros héros heros
heros héros heros
heros heros heros
héros héros heros
heros héros heros
heros hheros heros
Sama yonne si Iron Man
Sama yonne si Batman
Sama yonne si super man
Ndakheté amena sama héros
Amena sama heros heros heros
héros héros heros
heros héros heros
heros heros heros
Boy Classic