![Here We Go](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/23/8236c88da7164fd7beccaa4eff2fbc31H3000W3000_464_464.jpg)
Here We Go Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2025
Lyrics
He we go wakh niou fou diam bi neeh niou dieuliko
He we go wakh niou fou diam bi neeh niou dieuliko niou dieuliko
But If you want it go get it
Xiipil say beutt guiss boul nangou tarkhiss
Dieuleul sa ego tekk ko de té-co hey
Ndakh adouna amoul solo
Mba xol yagui feekh
Nieup far fi amoul meer
Diam dafeu nekh
Kon lou waral gni di guerre
Life bi dou bras de fer
Keineu xamoul founiouy moudié
Bougn leu toogné faut pas t'en faire
Fici adouna loo mougn mou diekh
Beuss dingeu weett ci sa cambeu ohh say dieuf rek niofiy dess
Reuthiou non dou wess xolatt djiko yi bala mouy wess
Talou niou tessenté
Fi xol yi nioy guissanté
Ak noumou meunti demé
Dareu xadioul souniou digeunté
He we go wakh niou fou diam bi neeh niou dieuliko
He we go wakh niou fou diam bi neeh niou dieuliko niou dieuliko
But If you want it go get it
Xiipil say beutt guiss boul nangou tarkhiss
Dieuleul sa ego tekk ko de té-co hey
Ndakh adouna amoul solo
No stress sans rancune sa weurseuk moy sa mérite
Bouldi nieeh niit ndakh full djizz no way (no way)
God bless my country meunou niou deukk ci meetite
Everyday is the same shit no way
Are you ready now are you ready now
Niou raxass xol yi yeené neeg leu borom rekeu ciy fanane
Li laniou souniou mame yi wane
Adouna potou ndaa leu nanal diokh sa morom nane
Finga yendou ley fanane