
Djongué Lyrics
- Genre:Classical
- Year of Release:2024
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Djongué - Aicha Kone Music
...
Djongué takh going beuré damkoy dane
Té makoy danel wouy soldat à terre
Doumako may dara trou yeup lay fate
May diw bi ninal sa thiep
Douma tek beut ! malay guiss doumako moudjééé!!!
Ma mate femme
Lap na thi samay feeem ma
Dafma may khol nane ma tu me rend fouuuu
Oh! Bébé khamguani Malay danel
May fessal sa khel
Go meunti dem dagay nieuw sama
djongué Molay gagneee , man ngua beugeuu thi sa liiiiife !
Touss! Touss nak ! Touss!
Man rek lay topeu
Touss! Touss nak! Touss!
Souy nélaw man rek lay guente!
Touss ! Touss nak ! Touss!
Qui dé man la dink khol bi
Touss ! Touss nak ! Touss!
May seytané bi !
(Music….)
Ennn ! Man rek lay top
Wowowowo! Souy nelaw man rek lay Guente!
Ahhh woo! Qui dé man la dink kholam
Ahhh wowoy! May seytané biii hihi hihi
Ah mix bi saf naaa
Mané djongué takh sama khol la yor di bath
Gni dougn Touss thi game bi may Nandi bou mak bi
Koussa djieukeur dof ba falma Doro nélaw
Dama dionguama ba yakhou , sen wakh lay fakhass ni nguélaw
Man ma khan fikay khassane
Diko wok té meuno thi dara
Mom diokh Nama bop ba tok
Sama néné Sou goudé mou wowéma maman
Ouuuuuh
Ouh waaah ah ouuh waaaaah enh ouou wahahaa !
Ah bébé khamguani Malay danel
May fessal sa khel
Fo meunti dem daguay nieuw
Sama djongué molay gagneee
Man ngua beug thi sa liiiife
Hahaha … ( music )
Man rek lay tope
Souy nelaw man rek lay guente
Touss ! Touss nak ! Touss!
Ki dé man la dink khol bi
Touss ! Touss nak ! Touss !
May seytané bi !
( music )
Enhh man rek lay top
Wowowoo ! Souy nelaw man rek lay guente
Ahhh wowo ! Ki dé man la dink kholam
Ahhh wowoy may seytané biiiihiii