![Maa Ngi Dem](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/12/24/03b6f9b384984e98805270f18fd6bade_464_464.jpg)
Maa Ngi Dem Lyrics
- Genre:Afrobeats
- Year of Release:2022
Lyrics
Maa Ngi Dem - Ashs The Best
...
Magui dém
Magui dém soma guissatoul dém na
Magui dém bafi sama xol
Dina wét wet si sama yone
Soubatél ba diante sow
Yangui séntou wadji foum diougué wone
Magui déeeemm té tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Magui déeeemm té tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Niow nafi nord
Nieuw nafi nawét
Nieuw nafi koor
Fék fi békor
Lima doundé
Ak lima wéssou
Day délloussé
Ba mélni séttou
Magui déeeemm te tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Magui déeeemm té tagouwoumala
souma rére mba dougne née ioe la
Dem na té tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Dioy na té kéne dorouma
souma réré mba dougne née ioe la
Magui déeeemm té tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Magui déeeemm té tagouwoumala
souma réré mba dougne née ioe la
Magui dém magui dém soma guissatoul dém na
Soma guissatoul dém na
Magui dém magui dém soma guissatoul dém na